Xibaar

ALSERI DUMAATI NA SENEGAAL

Démb ci talaata ji la gayndey Senegaal yi doon janook Alseri ci joŋante xaritoo....

AMET SIISE WAXATI NA TOJAANGE !

Saa bu waxee, loxo dar gemmiñ. Amet Siise nekk ku ñu miin ci mbaali-jokko...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (11/9/2023)

WOTEY 2024 YI Lawaxub Bennoo Bokk Yaakaar bi ñu doon laam-laame xam nañu ko léegi....

F24 WOOTEETI NA YËNGU-YËNGAL

Waa F24 fas nañoo yéene wéyal seen xeex bi. Loolu lañu siiwal keroog àjjuma...

LI GËN A FES CI XIBAARI BES BI (6/9/2023)

BÀYYI NAÑU XALIL KAMARA BU SENEGO Bërki-démb ci talaata ji lañu téye woon taskatu xibaarub...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (5/9/2023)

MÀGGAL TUUBAA Démb ci altine ji, 4 sàttumbar 2023, la murit yi doon bésal màggalug...

AKSIDAŊ BU METTI CI YOONU TUUBAA WI

Aksidaŋ bu metti moo am ci yoonu Tuuba wi. Xibaar bi nag, bettul ñu...

YOON : SOS/PAIX A NGI ÑAAN NJEKK NJIITU REEW MI

Mbootaayu kuréli ma-xejj yi ngir jàmm, ñu gën leen a miis ci SOS/Paix (Synergie...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...