Xibaar

Màggalug téeméereelu Usmaan Sémbeen

Usmaan Sémbeen doon na am téeméeri at ci ren, bu fekkoon muy dund. Jànguneb...

DEGGOO BU YEES DIGGANTE SENEGAAL AK FMI

Nguurug Senegaal ak FMI (Font monétaire International), di mbootaay miy saytu kopparu réewi àddina...

GÀTTALI BÉS BI (ALXAMES 18 ME 2023)

Daaray Nguur gi tëj nañu leen fa Siggicoor ak Séeju Li ko dale àjjuma ji...

SÉEX BEKAAY DËDDU NA !

Xalifa tarixa xadiir yi ci Senegaal wuyuji na Boroomam ginnaaw tawat bi ko tëraloon....

CAN U17 2023 : KUB MU NGI XEEÑ !

Raayab Senegaal a ngi gën yéeg, turam di gën a jëm ca kow a...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (TALAATA 9 ME 2023)

SAFAANTOO YA CA NGOR : ÑAARI BAKKAN ROT NAÑU Njiitul mbootaay "Ngor debout", Mamadu Njaay,...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ALXAMES 4 ME 2023)

RËBËJOO BA CA PSG Gannaaw tukki bi Messi amaloon ca Araabi Sawdid, njiiti Paris Saint-Germain...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (ÀLLARBA 3 ME 2023)

Aminata Ture Ginnaaw bi mu xamlee nee waa PDS ak Waa Bennoo Bokk Yaakaar dañoo...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...