Xibaar

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (DIBÉER 19 FÉEWIRYEE 2023)

PÓLITIG Mbootaayu Réewi Afrig yi (UA) Ay coppite ak i naal moo tënk waxtaan wu mujj...

Seen xiibaari tàggat-yaram Dibéer 12i Féewaryee 2023

Kuppeg àddina këlëb yi :  "Real Madrid" defatina ko ! Démb ci gaawu gi, 11i...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 11 FEEWARYEE 2023)

PÓLITIG SONKO JULLIJI NA TUUBAA  Démb ci Àjjuma ji njiitu pasteef lii di Usmaan SonkoTuubaa la...

LI GËN A FES CI XIBAARI BES BI (àjjuma 10 féewaryee 2023)

PÓLITIG Perefeb Mbàkke tere na mitiŋ ba Tey ci àjjuma ji la kii di Usmaan Sonko...

LI GËN A FES CI XIBAARI FUTBAL (alxames 9 féewaryee 2023)

 BELSIG AM NA TAGGATKAT BU BEES Kuppeg àddina 2018 ba léegi, Belsig dafa nekkoon ciy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Àllarba 08 féewaryee 202)

GUY MARIS SAAÑAA BOOLE NA SËRIÑ BASIIRU GÉY Guy Maris Saañaa bind nab bataaxal, jébbal...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Altine 6 féewarye 2023)

PÓLITIG PDS Abdulaay Wàdd njiitu réew mi fi woon génn na ca tekkaaral ga mu nekke...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (àjjuma 2 féewaryee 2023)

PÓLITIG  Layoo Maam Mbay Ñaŋ Usmaan Sonko ajandi nañu ko Layoo bi waroon dox démb ci...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...