Xibaar

Sémbug liggéey bu Nguuru Aamadu Ba

Ci altine jii weesu la kii di jëwriñ ju mag ji demoon ca Ngomblaan...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI  Àllarba 14 desàmbar 2022

PÓLITIG  Pexey kippaangog Yewwi Askan Wi  Altine jii weesu la kii di Aamadu Ba demoon ca...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 12 desàmbar 2022

PÓLITIG Jëwriñ ju mag ji, Aamadu Ba teew na ci kanamu ngombalaan gi. Ginnaaw bi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI GAAWU 10 DESÀMBAR 2022

PÓLITIG Woteb nafag 2023 gi jeex na ci gaawu bi. Jëwriñ ji ñu dénk nafag...

MBATIT BIIR NDAKAARU

Ndakaaru dalal na “Festival come to my home”. Muy xew-xewu mbatit, cosaan ak xeltu,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 5 desàmbar 2022

PÓLITIG Ngombalaan gaa ngi wéy di natt nafay njëwriñ yi ñeel atum 2023. Njëwriñu dem...

Kuppeg àddina si : Senegaal, xalam demoon na bay neex buum ga dog

Ginnaaw ñaar-fukki at bim gëjee romb pàcc bu njëkk bu kuppeg àddina si, Senegaal...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI GAAWU 03 DESÀMBAR 2022

PÓLITIG Ginnaaw ndajeem jëwriñ yi mu amaloon, Njiitu réew mi Màkki Sàll, takkal na ndombog-tànk...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...