Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci atum 1871. Mu doon doom ci Sàmba Yaaya Faal mi newoon fanweer ak ñaarelu Dammeelu...

DIGE GÉEJ, KILIBU SÉEX ALIYU NDAW : TEKKI MBAA LAB

Dige géej, téere kilib bii Séex Aliyu Ndaw di door a génne, OSAD mi Soxna Aram Faal jiite moo ko móol ci atum 2019....

Bataaxalu Saalif Keyta ñeel IBK

Ci tekkib Paap Aali Jàllo

AFRIG, LU LA TAX A DES GINNAAW ?

Bare na li may toog man kenn, di yónni samam xel, mu wëral ma àddina sépp ak li ci biir, fu nekk mu ne...

DÉMB AK TEYU DOXANDÉEMI ITALI YI

Waxtaanu Baay Njaay ak B. S.

WAAW, ANA KU BÓOM OMAR BOLONDEŋ JÓOB ?

Omar Bolondeŋ Jóob a ngi juddu ci 10eelu fan ci weeru sàttumbar 1946 ca Ñaame, péeyub réewum Niseer. Mu ngi faatu ci 11eelu fan ci weeru...

BUUR

WÀDD-MAKI : GINNAAW AY…SOPPI ?

Keroog, àjjuma 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019,ba ñuy ubbi Masaalikul Jinaan, jullit yépp a bégoon, rawatina murid yi. Bégoon nañ ba, foo nattoon seen...

MASAALIKUL JINAAN WALLA YOONI ÀJJANA YI

Ci àjjuma jii weesu, 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019, lañ doon ubbi ci Kolobaan jumaa ju mag ji : Masaalikul Jinaan. Kilifa gii...

ËLLËGU XALIFA SÀLL CI LÀNGU POLITIG GI

Dibéer, 29eelufan ci weeru sàttumbar 2019, la Xalifa Sàll gisaat jant bi ginnaaw bi ñu ko ko nëbbee ñaari ati Yàlla ak genn-wàll. Ñuŋ...