Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

BIBO BOURGI TOROXAL NA NGUURUG SENEGAAL

Gàcce bu reyul, semmal. Nguurug Senegaal a ngi ne tott ci kanamu àddina sépp. Coowal CREI ak Kariim Wàdd a leen ko yóbbu. Nde,...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (20/7/2023)

F24 Kurél gii di F24 boole ay làngi pólitig ak i way-moomeel dafa nammoon a amal am ndaje ci àjjuma jii. Ndaje moomu nag ma...

BÀYYEENDI NAÑ BIRAM SULEY JÓOB AK EL MAALIG NJAAY

Bàyyi nañ Biram Suley Jóob. Layookatam bi, Meetar Musaa Saar a ko xamle. Moom, Biram Suley Jóob mu Pastef, dafa yékkati woon ay kàddu...

TAMXARIT 2023

Àjjuma 28 sulet 2023 mooy doon bésu tamxarit. Loolu la waa CMS, Ndajem Julliti Senegaal, xamle.  Ci altine jii weesu lañ doon séentu weer wi....

XEEXI ÑAXTU CA DAARAY SIGICOOR JU KOWE JA

Daara yu kowe yi ci Senegaal dafa mel ni ag dal daf leen a dëddu. Bu dul coowal pólitig gu wal ba wàlli ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (18/7/2023)

Coowal dogub 87 bu Ndeyu àtte réew mi Démb ci altine ji lees woolu woon dépite yi ca  Ngombalaan ga ngir ñu saytu ci lu...

F24 MI NGI ARTU…

Tey ci altine ji lañu woo woon dépite yi ca Ngomblaan ga. Dafa amoon i sémb yu bari yu ñu fa waroon a càmbar...

SÉMBUB ÀTTE BUY SOPPI DOGUB 87 BI

Ëllëg, ci altine ji 16 sulet 2023, lañ war a wote ca Ngomblaan ga ab sémbub àtte bob, day jëmmal lees waxtaane ca péncoo...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (16/7/2023)

KUPPEG ÀDDINA SI 2026 Kippu yi ñeel xëccoo paasu kuppeg àddina si war a am ci atum 2026 mi génn nañ fii ci wàlluw Afrig....

« RAŊ ! RAŊ ! KEŊ ! KEŊ ! … » NDAKAARU RIIR NA DÉMB

Bool, marmet, kubéeri cin, kuddu cinwaar, kuddu luus, mbiib yi, korne yi… lépp a riir démb. Bi 20i waxtu tegalee 30i simili, lépp luy...

Nguur geek Usmaan Sonko : Mën a tëru, mën a teggi

Tey ci gaawu bi, 15i fan ci weeru sulet 2023, la làngug politig gii di Pastef les patriotes nammoon a amal am ndaje fa...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (14/7/2023)

MBËKK MI : 6I NÉEW YU BEES YU FEEÑ FA NDAR Ñeenti bés ci tey, bi gaal ga suuxee ca bëlub Ndar ba, yeboon i...