Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

50eelu LËLU CESTI : 33I TASKATI XIBAAR YU BEES

Barki-démb, ci alxames ji (25eelu me 2023) la CESTI doon jox seen lijaasa 5i taskati xibaar yu jigéen ak 28 yu góor ca "UCAD...

YEWWI ASKAN WI – TAXAWU SENEGAAL : ÀND BUY WAAJ A TAS ?

Waxtaanu Maki Sàll wi de, boo demee, moo nar a génne Taxawu Senegaal ci lëkkatoo Yewwi Askan Wi. Ndaxte, Yewwi Askan Wi daa fétt,...

Usmaan Sonko dina dellu Ndakaaru

Njiitul Pastef li, Usmaan Sonko, dina dellu Ndakaaru. Tey ci àllarba ji la ko biral fa Siggicoor ga mu nekk boobu ba tey. Ci...

TEGGI TUUMA

Yàgg dina dindi tuuma, waaye gaaw cee gën bu naree jur njombe. Loolu la fajkat bi, Alfuseyni Gay, xam ba tax ko jóg, indiy...

BAANE, YAA WAANE !

Dàqees na àtte bi ba alxames, 1 fan ci suwe 2023. Démb ci talaata ji lañu doon layoo tuumay ciif ak tëkkuy rey yu...

Mbirum Sweet Beauty : ni Ndey Xadi Njaay setal na boppam, taqal Aji Raabi Saar

Tey, ci talaata ji 23 me 2023 lees di amal layoob Usmaan Sonko ak Aji Saar ak it bu mbirum Sweet Beauty. Bi ñu...

SÉEX TIIJAAN GAAJO WAN NA MAKI SÀLL BUNT BU MAG BI

Séex Tiijaan Gaajo séqoon naw waxtaan ak waa Iradio (90.3), ñu doon ko dalal ci jotaayu Jury du Dimanche, yéenekaayu web Seneplus yaxal ko....

ÑEETTEELU MOOME : MAKI SÀLL JÉGGAANI NA AW LAY

Jéggaani xaalis. Jéggaani dund. Jéggaani xam-xam. Léegi, jéggaaniy xalaat a ci des. Ndeke, Njiitu réew mi, Maki Sàll, dafa sàkkoo xam xalaatub jàngalekatu Yoon...

JÀPP NAÑU ÀPPUG WAXTAAN WI

Lu tollook weer a ngii wow, ñuy yéy ak a yàbbi ci waxtaan wi Njiitu réew mi woote woon keroog bésub korite ga. Am...

XEWTEEB NDAAKAARU ÑEEL LADAB CI ÀDDINA SI

Ndakaaru dina amal ñaareelu xewteem ñeel ladab ci àddina si, FILID (Festival international de littérature de Dakar). Ginnaaw bi mu ko njëkkee woon amal...

BU YÀLLA NEE WAAW, LÉPP AY BAAX

Li gaa yi naan bàmba bu naan, Senegaal jamono jii bàmbaam naan na ba cukkur-mbuut. Mbir yi ndeke dafay gën di neex rekk ! Bu...

USMAAN SONKO : « Bu Maki bëggee jàpp Usmaan Sonko, fàww mu taqal boppam»

Démb, ci guddig àjjuma ji, Usmaan Sonko séq naak Piyeer Eduwaar Fay mu Walf Tv ab laaj-tontu bob, tele Siidi Lamin Ñas bi la...