Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

MEERI BU NDAKAARU : DÀQ NAÑ ABBAAS FAAL MU PASTEF

Démb ci àllarba ji la meeri bu Ndakaaru doon yeesalaat pekkoom gi. Li ñu ko dugge woon mooy jëmmal ndogalub ëttu àtteb dabu bi...

MÀGGALU DAARU XUDÓOS

Mu doon tur wu siis wi ñu ko xame, màggalu daaru xudóos doon xew-xewu diine. Murit yi di ko màggal at mu jot ca...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/8/2023)

BÀYYEENDI NAÑ PAAP AALE ÑAŊ Meetar Musaa Saar moo biral xibaarub bàyyeendi Paap Aale Ñaŋ. Moom, Paap Aale Ñaŋ, wii mooy ñetteelu yon wi ñu...

KUMBA AM NDEY, KUMBA AMUL NDEY

Démb lañ bàyyi Xuwaan Baranko (Juan Branco), yóbbu ko ca saa sa fa dalub roppalaanu AIBD ngir dàq ko, génne ko réew mi. Moom...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/8/2023)

WOTEY 2024 YI Xalifa Sàll ak Karim Wàdd yewweeku nañu. Delloos na leen seen i àqi maxejj yi leen di tax a doon lawax ci...

RAWALEES NA USMAAN SONKO CA FAJUWAAY BA

Làngug Pastef les Patriotes génne na ab yégle di ci xamle ne, rawalees na Usmaan Sonko ca fajuwaay ba. Nee ñu, njiitul Pastef li...

AFROBASKET-KIGALI 2023 : XALAM DEMOON NA BAY NEEX !

Démb la woon finaalu Afrobasket bi doon am ren ca Ruwàndaa, doxoon ci diggante Senegaal ak Niseriyaa. Niseriyaa nag moo ko mujje gañe, daldi...

NISEER : CEDEAO DAY SONG AM DÉET ?

Ayu-bés a ngi nii ak lu teg, bi sóobare yi foqatee Nguur gi fa Niseer. Bu weesoo ñaawlu gi mu ko ñaawlu, CEDEAO (Communauté...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (4/8/2023)

PASTEF Ñoo ngi wéy di raafal ndawi Pastef yi. Keroog, Tuseŋ Màngaa ak Bentaleb Sow lañ jàppoon. Démb, fa Yëmbël, jàppati nañ Dr Séydu Jàllo...

FITNA DU YEM CI BOPPU BOROOM

Njiitul Pastef li, Usmaan Sonko, ma nga ndung-siin jamono jii. Lees ko jàpp, am na ñm bett, waaye am na ñeneen ñum bettul. Li...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/7/2023)

Mbiri Usmaan Sonko Ginnaaw bi ko toppekat bi gàllee 7i tuuma ci gaawu gi, njiitul Pastef li Usmaan Sonko doon na jàkkaarlook magum àttekat yi...