Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

Gàttalug xibaar yi, Alxames 18 ut 2022

 Siin Lii nag ag lёngoo la gu jёm ci wàllum mbey ci diggante ñaari réew yii. Donte ne sax, àndug Siin ak waa Afrig du...

BALAA NGAA WAX NAAM, NE FA

Lekkool bi, ay at ñu ngi nii jafe-jafe bu dem, moroomam wuutu ko. Bokk na ci li ko gën a jatt, di bank loxo...

WOMEN FIRST TV Tele jigéen ñi, ngir jigéen ñi

WOMAN FIRST TV tele la bu ay jigéen sos jagleel  ko it jigéen ñi. Mi ngi juddu ci jamonoy mbasum covid-19 mi lëmbe woon...

DÉGGOOB 79. 329 MILIYAAR DIGGANTE SENEGAL AK BAD

Jëwriñ ji ñu dénk fànnu koom-koom gi, Aamadu Hot, xaatim na ab pas bu tollu ci 79. 329i miliyaar ak waa BAD (Banque africaine...

WUJJE GI CI BIIR KUJJE GI  LAN MOOY JUBLUWAAY BI ?

“ Yaa ma..” ji ak “Maa la…” ji a ngi tulle ak màlle ci làngug pólitig gi, rawatina ci kujje gi. Li Paap Jóob...

AFRIG, TONTU DU FOROX, Tontu ñeel kàdduy Óreliyoo De Lórãtis yi

Duma topp diw boo gis, fi ngeen jëm dafa sorewul. Loolu la waa CAF (Mboolem kuréli futbal yu Afrig yi) xam ba xaaruñu wenn...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI, Dibéer 14 ut 2022

PÓLITIG  Li bettul kenn mooy fekki gi Paap Jóob fekki waa BBY. Mu nekkoon lu ñu doon kummuj, far na doon dëgg. Jëf ji di...

LI GЁN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Àjjuma 12 ut 2022

PÓLITIG : Ndogal yi lёkkatoo yii di YEWWI ak WALLU jёl Ginnaaw seen ndajem waxtaan mi ñu amaloon àllarba 10 ut 2022 jёl nañ ab...

Naalub yeesalaat Raglu Aristide Le Dantec Li waral coow li 

Raglug Aristide Le Dantec lañ nar a tëj, 15 ut bii ñu dégmal. Ndogal laa ngi tukke ci Càmm gi. Waaye, dafa mel ni...

14eelu LËLU SAES : AW YOON NGIR TINKI NJÀNG MU KAWE MI

Kenn werentewul ne njàng mu kowe mi dafa nekk ci guuta. Ab diir a ngi nii, muy jànkonte ak ay jafe-jafe yu bir. Li...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI

PÓLITIG Saa-fuuta yi noppeeguñoo wannaasu tiiñal gi leen ñenn ci kujje giy tiiñal bi Bennoo Bokk Yaakaar rawee foofu ca Fuuta ci wotey Ngombalaan yiñ...

TOLOF-TOLOFI ARTISÃ YI : LAN MOO CIY TAXAWAAYU NGUUR GI

Fànnu artisanaa nekk na lu soxal lool nit ñi rawatina artisã yi yore seen liggéey di ci góor-góorlu. Ñi ci gën a bari nag...