Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu 27 ut 2022

 PÓLITIG  Coow li amoon  ci diggante Gabriyel Kan ak jëwriñ ji ñu dénk mbiri jigéen ñi, Ndey Sali Jóob Jeŋ dakkagut.  Kenn ku bokk ca...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu 27 ut 2022

PÓLITIG Péncum ndawi réew ma  Ca 12eelu fan ci weeru Sàttumbar la dépitey réew mi di amal seen ndaje mu njëkk fale ca Néncum ndawi réew...

Làmb : mbër yaa ngi jooy

CNG def na mujjum ndajeem mu mag ginnaaw bi làmb ji tëje. Mi ngi ko doon amal ci gaawu bii weesu, 20i fan ci...

Coowal Raglu Le Dantec bi

Li nit ñi doon xel ñaar ak a laam-laame, leer na ! raglu Le Dantec tëj na ci bésub 15 ut bii nu génn. Boob...

WAAJTAAYU MÀGGALU TUUBAA

Dëkk bu sell bi, Tuuba, dafa aadawoo di amal at mu jot màggalu 18 Safar. Muy bés bu màgg a màgg ci tarixa muridiyya....

WURUS RUSUL A DELLU NGALAM WURUSU MALI, CA LOXOY SAA-MALI

Saa-Mali yi léegi ñooy defaral seen bopp seen wurus. Liggéey boobu nag, dañ ko dénk doomi réew ma ci benn këru liggéey bu ñu...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI

POLITIG : Toussaint Manga génn na PDS  Ab bataaxal la kii di Toussaint Manga jébbal njitaal PDS li, Abdulaay Wàdd, di ko xamal ne dafay bàyyi...

TAXAWAAYI DÉPITEY KUJJE GI LAATA SEEN AG DEM CA PÉNCUM NDAWI RÉEW MA

Ginnaaw bi njureefi joŋantey palum dépite yi rotee, yenn ci dépite yi biral nañ seen péete. Ndax, kii di Paap Jóob moom, di Njiital...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu, 20 ut 2022

XEW-XEWI JAMONO Yokkuteg njëgu soble ga ca Tuubaa  Ñàkkum soble bi ganesi réew mi ci fan yii tax na ba saaku soble bi daan jar junni...

Kub bu Mboolem-Kuréli futbal yu Afrig yi (CAF) 2022-2023 « Ñàkk teewu Jaraaf doon na luy nëbb futbalu Senegaal ci kembarug Afrig… »

Seppi nañ Jaraaf ci Kubub CAF bi. Loolu la FSF (kurélu futbal gu Senegaal) siiwal. Ci yëgleem bi mu génne, jàpp nañ ci ni...