Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

PECCIM KÓLLЁRЁ (MÀNG) GI CI LÀNGUG PÓLITIG GI : LAN MOO KO WUND ?

Pólitig nekk na mbir mu am solo lool ci mépp réew mum mёn di doon. Waaye, niñ koy defe ci Senegaal xaw a doy...

LI GËN A FËS CI XIBAARI

LÀMB : Bàlla Gay 2 daanaat na Giri-Bórdoo  Ci diibéerub démb ji la Gastõ Mbeng tëggoon làmb ju réy ju doxoon ci diggante Giri-Bórdoo ak...

KÓLLËRE GINNAAW LAY FÉETE

Wotey dépite yi ci dibéeru 31 ci sulet 2022, wone na xar-kanam gu bees ci réewum Senegaal. Ndax ag mbetteel la ? Walla jaas...

NJUREEFI NÉGANDI YU WOTEY NGOMBLAAN GI, lu mu nar a jur ?

Décce Faal ak i ñoñam, waa Wallu-Yewwi, dinañu am lu leen metti. Te, sikk amul ci ne, dinañu génn fésal seen ug ñàkk ànd...

XËCCOO SOOG A PÉNCOO

Njëlbeeni njureefi wotey Ngomblaan gi Ci dibéer jii, 31eelu fan ci sulet, la askanuw Senegaal waroon a sànniji seen i xob ngir fal ndaw yi...

Doxalinu wotey palum depite yi ci Senegaal

Dibéeru tey 31 i fan ci weeru Sulet la wotey palum depite yi tàmbali fii ci réewum Senegaal. Mu doon bés bu ñépp doon...

NÉEWAAYU LIMUB ÑI WOTE CI JOŊANTE YII : LAN MOO KO WARAL ?

Dibéer 31i fan ci weeru Sulet nekkoon bés bi ñu doon amal wotey palum depite yi ci biir réew mi ak ca bitim-réew. Mu...

GÀTTALI BÉS BI

BÉS DU ÑÀKK Gannaaw bi ñu génnee ci lёkkatoog Yewwi Askan Wi ci fan yii. Waa Bés Du Ñàkk bu Sёriñ Mansuur Sy Jamiil ñi...

XALIMA BËNN NA AY GËTAM

Mayleen ma nopp, abal ma seen i gët te ubbi seen um xel ma xellil leen ! Man Xalima, amuma lu dul samay rongooñ. Ñooy...

Cargalug CAF Awards 2022 : Senegaal ca kow, ca kanam

Alxemes, 21i fan ci weeru sulet lañ doon amal cargalug CAF Awards 2022 yi. Muy xew-xew bu mboolem kuréli futbal yu Afrig (CAF) di...