Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

Gàttali bés bi

Wotey palum depite yi : Mari Tëw Ñaan mi yàggoon a liggéey ak Njiitu réew mi Maki Sàll woo na ay militaŋam ngir ñu wotel waa...

Bërug ndëgg-sërëx

*Xana du bër da daan neex ndongo ? Daara ju kawe ja ca Ndar, ndongo ya safaan ba lañu wone ca seen bër gu...

AY NJÀNGAT ÑEEL KÀMPAAÑI WOTEY PALUM DEPITE YI

Fi mbir yi tollu nii tembe, gaa ñi fare ci làngug pólitig, ku nekk ci ñoom a ngi lal i pexe ngir am baatu...

Mbënn mi ak toj-toj yi : fan la miliyaar yi duggu ?

Njàqare, jaaxle la ñu bari ci ñi dëkke ci yenn diwaan yu nekk ci réew mi àndal gannaaw ba taw bi wàccee ci àllarba...

WOTEY 31 SULET YI, Péncoo walla paacoo, askan waay tànn

Fukki fan rekk a ci des fii ak dibéer 31eelu fan ci sulet. Keroog la maxejj yi war a sànniji seen i xob ngir...

«BACCALAUREAT» 2022

Joŋante “baccalauréat” amal nañu ko alxames jii, fukki fan ak ñeent ci weeru sulet. Li ëppoon ci ndongo yiy wut seenub lijaasa bu leen...
00:03:10

Saajo Maane ca Bayern Munich

Njiiti Bayern Munich yi mujje woon nañ déggook yu Liverpool FC yi ñeel ëllëgu Saajo Maane. Doomu Senegaal ji di jóge Liverpool bim fa...
01:33:07

“Héritages” dalal na Bubakar Bóris Jóob

"Héritages ak Awa" ngi dalal Bubakar Bóris Jóob, ngir gën a xam nit ki ci ginnaaw bindkat bi.  

NJUREEFI SOROJ BI AK GAAS

Réewum Senegaal a ngi waaj a jëfandikoo soroj bi ak gaas bi fileek diir bu gàtt. ñu ci séentu xaalis bu bare. Te, ku...