Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

Misig

Feetu misig Tey la bés bi ñu jagleel misig. Ñu di ko màggal fii ci biir réew mi. Xumbal yi nar jolli ci gox yu...

SONKO AK MAKI : KUY DAAN ?

Fitna lañ doore bésub àjjuma jii. Fitna ju sosoo ci diggante Sonko ak Maki. Ndax lan ? Ndax, dañoo tere Sonko ak i àndandoom...

BUUR, LEKK AK NAAN, FOLLIKU DAY BETTE

Téll !... Xërr !... Téll !... Xërr ! Téll !... Xërr !... Takk-der yi fii, ndaw ñi fee, fetel yiy sox, xeer yiy naaw...

Ndeyu àtteg Bokkeefug Senegaal : ndey ji seex du tëdde wet

Sagar a ngi xeeñ. Ñépp a ko maase yëg. Xet gi ëbale ne ràpp réew mépp. Xanaa kay Saa-Senegal yi dañoo tàmm ne, bala...

LU ЁPP TUURU !

xibaarRéewum Senegaal rafle na jàmm ci jamono jii, muy ci kàddu yi gaa ñi di yékkati ak ci seen i jёf. Lenn waralu ko...

Làmb : Móodu Lóo di woo jépp doomu Parsel ci ginnaaw Farã

Démb la Farã doon  amal Open Press ñeel laale bi war am ci digganteem ak Soq. Mbëri Parsel yu mag yi bare woon nañ...

Kollëre gi doxoon diggante Coca-Cola ak Soboa fecceeku na !

Pas gi waa Coca-Cola ak Soboa amaloon seen diggante àntuwul. Daanaka ci Suliye bi ñu dégmal la àpp pas gi di mat. Soboa nag...

CAN 2021 : Kub baa nga woon ca Séeju, Saajo Maane delloo mbàttu ca ndaa la mu naane

Bàmbali, ci diwaanu Séeju, dalal na Kubu Afrig bi Senegaal jële woon ca Kamerun ak doomam jii di Saajo Maane. Jëwriñ ji Mataar Ba...

Gaasu Senegaal bi : lu tax tugal di ko xemmem?

Daan ya réewi tugal ya tegoon ci kow Riisi ñoo tàmbalee di dalaat seen kow. Nde, daan yooyee sabab tey jaf-jafe yu metti yi ñuy jànkonteel ci wàllum koom-koom. Daanaka lépp a yokku rawatina dund gi ak laf gi, soroj (petarol) ak gaas bi. Mooy li ñu...

Sàmpiyonaa Senegaal : Casa Sport jël na raw-gàddu gi, SONACOS ak Estaad bu mbuur dellusi

Dibéer bi weesu (fukki fan ak ñaar ci weeru Me lees doon amal ñaar-fukk ak juróom benneelu bëccëgu sàmpiyonaa Senegaal. Mu waroon a ndar-kepp...

TAAFAR SI CI LÀNGUG POLITIG GI, MBAA DINA JUR JÀMM CI RÉEW MI ?

Xeetu taafar yi nuy faral di gis te di ko dégg ci réew mi jamono jii jéggi na dayo. Taafar moom du ci jёf...