Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

BAÑ A WACC SA ÀND…

Mbir mi doy na waar. Kenn xamul lii lu mu doon. Nekk cim réew, dund fa lu ëpp fanweeri at, te ba tey may...

KAN MOO DOON ISEN AABARE ?

« Jébbalees na Aabare Boroomam », nii la jawriñ jiñ dénk wàllu yoon wi, Maalig Sàll, dëggalee xibaar bi rotoon ci yéenekaay yi :...

COOW DINA TOPP SENEGAAL CI FAATUG ISEN AABARE GI (NDEY KODDU FAAL)

Isen Aabare, Njiitu réewum Càdd la woon, génn na àddina ci loppitaal “Principal” bu Dakaar talaata 24eelu fan ci weeru ut 2021. Nee na...

ÀND WATTU LÀKKI RÉEW MI

"MBINDAAN" LEES WAROON A BIND ------------------------------------------------------------------------------ ÀND WATTU LÀKKI RÉEW MI Ànd jubal mbind mi ! Ñaareelu yëngug jubbanti mbindin mi Yaxub kubbite  Tey jii, boroom xam-xam yaa...

BOROOM-ÑAARI-TUR YI SAMP NAÑU SEEN NDËND WAAYE…

Mbirum ngóor-jigéen doon na lu lëmbe àddina si fi mu tollu nii, moonte dey amul jenn diine ju ko nangu, du jullit, du kercen,...

DALOOB KËR MOMAR SAAR 3 : NDOX MU DOY, DUND GU SELL (NDEY KODDU FAAL)

Robine tijji, ndox walangaan, xel dal, xol tóor yaakaar, yaakaar ëllëg gu tane ndax fu ndox mate, dund sell. Lii mooy njeexitalu Kër Momar...

WAAW, KAÑ LA SENEGAAL GËJ A YËNGOO NII…?

Weeru màrs wii weesu, Senegaal tàngoon na jipp ! Gannaaw ba alkaati yeek sàndarm yi jëlijee Usmaan Sonko ngir jébbal ko Yoon, daanaka waa...

JOXEB LIJAASA BU 48eelu LËLU CESTI (NDEY KODDU FAAL)

Alxemes jii nu génn la CESTI doon jox seen lijaasa 4i taskati xibaar yu jigéen ak 21 yu góor. Xew-xew baa nga ame "UCAD...