Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

ÑU BÓOM 160i DOOM-AADAMA CA BURKINAA, AFRIG DUMMÓOYU : LAN MOO NU DAL ? (PAAP AALI JÀLLO)

Solhan, gaawu, 5eelufan ci weeru suweŋ, ci kow i néew la jant bi fenk. Xetub bànqanoos bu jaxasook xetu deret ubale foofu yépp. Ay...

WAVE AK ORANGE MONEY, NUN LAÑ FI NEKKAL WALLA SEEN BOPP? (AMI MBENG)

Wax ji bari na, werante bi ne kurr, ñii naan « Ñaw ! Upp baax na ci laax bu tàng ! », ñi ci des naan « Aawo...

ANNONCE COURS DE WOLOF À L'IFAN ET À L'EBAD

ANNONCE La deuxième session des cours d’alphabétisation en wolof aura lieu du samedi 5 juin 2021 au samedi 26 juin 2021 inclus. Prévus en présentiel à...

CEERNO ALASAAN SÀLL : "SAMA YÉENE CI RÉEWUM SENEGAAL…"

Tey, Senegaal, kenn mënul a wax waxu pólitig te doo ci boole Ceerno Alasaan Sàll. Turam ak turi Usmaan Sonko, Bàrtelemi Jaas, Xalifa Sàll, Abdul...

KÀDDUY USMAAN SONKO 2/2 PÀCC

Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo, yëf yi doy waar lool, yegg sax fu ko kenn foogul woon. Ñii seen i...

CEERNO ALASAAN SÀLL : "YAAKAAR AK RAFET NJORT ÑOO MA TAXOON A ÀND AK MAKI SÀLL"

Tey, Senegaal, kenn mënul a wax  waxu pólitig te doo ci boole Ceerno Alasaan Sàll. Turam ak yu Usmaan Sonko, Bàrtelemi Jaas, Xalifa Sàll, Abdul...

RAFLE JÀMM (DAAWUDA NJAAY JARAAF)

Fitt a jiitu fetal Lépp aju ci ngistal Doolee mën dëgg Weddil googu dëgg Njaayum gànnaay Rombal doonub nay Bu njaay mi lambee Dëgg daan doole Gént naay gànnaay Yu wuteek yiy rey Sànni...

KÀDDUY USMAAN SONKO 1/2 PÀCC

Senegaal gépp amoon na fiy yëngu-yëngu, réew mi jaxasoo, yëf yi doy waar lool, yegg sax fu ko kenn foogul woon. Ñii seen i...

Kàddug Maki Sàll, Njiitu réew mi (AMI MBENG)

Ndakaarook biir Senegaal amoon nañuy yëngu-yëngu yu metti : ñu bari ñàkk ci seen bakkan, ñii seen alal, ña ca des, ñu taal seen i...