Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

XAREB IKREN BI – COSAAN LI AK NJEEXITAL YI 1/3

Coowal Riisii – Ikren moo lëmbe àddina si. Daanaka, ñaari ayu-bés a ngi nii, moom rekk lañuy waxtaane ci fépp foo dem ci àddina...

GAYNDEE NJAAY ! MBARA-WÀCC ! CAN 2022 : SENEGAAL JËL NA RAW-GÀDDU GI

Dibéer, 6eelu fan ci féewaryee 2022, 21i waxtu ci guddi tegal nañu. Lépp a ngi ne tekk, ne selaw. Ñépp a ngi ne cell....

RUWÀNDAA, RÉEW MA FARÃS NEE TOTT AK GÀCCE 2/2

Ci atum 1997 la Mehdi Bâ génne téereem bu jëkk, jox ko tur wu leer nàññ : « Rwanda, un génocide français6 ». Jacques...

RUWÀNDAA, RÉEW MA FARÃS NEE TOTT AK GÀCCE (BUBAKAR BÓRIS JÓOB CI TEKKIG PAAP AALI JÀLLO) 1/2

Weeru màrs 2021 wee ñu génn, ci 26eelu fan, « Ndajem gëstub ceedeefi Farãs ñeel Ruwàndaa ak faagaagalug Tutsi yi », jébbal na Emmanuel...

CARGALUG NEUSTADT INTERNATIONAL PRIZE FOR LITERATURE : BUBAKAR BÓRIS JÓOB JËL NA NDAM LI (PAAP AALI JÀLLO)

Ci talaata 26eel ci oktoobar 2021, lees jot ci mbégtem weer wi. Surnaalu ladab bees duppe World Literature Today, nekk ca Iniwérsite Oklahoma, ca...

PÉNCUM MAAM YUNUS JEŊ : LADAB CI LÀMMIÑI RÉEW MI (NDEY KODDU FAAL)

Ku dégg Maam Yunus Jeŋ, sa xel dem ci jigéen ji jëkk a bind téere nettali ci kàllaamay Kocc. Péncum Maam Yunus Jeŋ nag...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru nowàmbar wii, jaare ko ci benn ciy doomam, di Muhamet Mbugaar Saar, ab bindkat. Moom...

MAKI DA NI WOON YOONU YOKKUTE : LÉPP YOKKU NA !

«Réew mi dafa tagatémbe !», «Dund gi jafe na !», «Lépp a dëgër !», «Danoo sonn!», «Na nu Maki dimbali !», «…walla mu abal nu.»… Ak yile...

Gis-Gisu Seex Aliyu Ndaw ci "Francophonie"

Faraŋ ko fóni (Woy) Faraŋ ko fóni Man kat daa waaru Kaay làggi ci saaw làmmiñ Na doon saw làmmiñ Te bañ di aw làkk Ci yow Waaye kat yemal foofee Bu fi...

JÀNGOROY ÑÀKK JI NU GANESI

Askanu Senegaal tollu na ci diggante bu tar cig ñàkk ba sax, li ëpp ci boroom-kër yi mënuñoo matale seen i wareef, rawatinaak ni...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di ñëw, la Senegaal fas yéene amal ay wote jëm ci palu njiiti gox-goxaan yi. Gannaaw ba pàrti pólitig...

FÀTTALIKU OMAR BOLONDEŊ JÓOB… 2/2

(ÑAAREELU XAAJ) Bi ñu nee Senegaal moom na boppam tamit, loolu ciy wax rekk la yem ; ndax Seŋoor àndul woon ci réew mi génn...