Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

SUNU GIS-GIS CI ''BLACK LIVES MATTER'' AK YENEEN XEETI ÑAXTU ÑEEL XEETAL AK ÑAAWTEEFI TAKK-DERI AMERIG YI (Kàddug mbooloom kàngami Mbootaayu Xeet yi fekk...

(Ci tekkig Ndey Koddu Faal) Njolloor, ca Minneapolis. Alkaatib Tubaab teg óomam ci kow loosu nit ku ñuul di bës, di bës, di bës rekk, tëwa...

FÀWW FAIDHERBE DAANU !

  Paap Aali Jàllo «Tooñ, torox, goreedi ak ñàkk fulla weesuwul ñuy woyal Lat-Joor ci tóojug estati bu Faidherbe…» (Usmaan Sémbéen) Ginnaaw mbasum Covid-19 bi, mel na...

YOLOMAL BUUMU NJAAM GI NGIR GËN LAA XOJ, FARÃS DEFATI NA MËNINAM (Boos Ndóoy)

Boos Ndóoy Jikko ak boroom, sëg ya rekk ! Ndege, Farãs dafa am pexe moo xam ne, ca jamonoy nootaange ja ba tey jii, ci...

USMAAN SONKO : ‘’ÀNDUMAAK ÑI NAAN ‘FRANCE DÉGAGE’ !’’ (Ñaareelu xaaju laaj-tontook Ndey Koddu Faal, Paap Aali Jàllo ak Daawuda Géy)

LU DEFU WAXU : Seetlu nañ ni, saa booy wax ci nguurug Maki Sàll, danga naan « Nee na moom moo gañe… ». Mu mel...

YOW KORONAA (Mamadu Jara Juuf)

TAALIFU MAMADU JARA JUUF Nee nga  layy, ni dott Ñów di nas, di nocci Nërmeel  nga  boroom  doole Detteel  nga  boroom  alal Botti nga  boroom  xam-xam Yow Koronaa, yaay  fas...

USMAAN SONKO : « MAKI SÀLL CUUNE LA, DI DEF YËFI CUUNE. » (Ndey Koddu Faal, Paap Aali Jàllo, Daawuda Géy)

(Xaaj bu njëkku laaj-tontook Ndey Koddu Faal, Paap Aali Jàllo ak Daawuda Géy) LU DEFU WAXU : - Usmaan Sonko, ginnaaw bin la nuyoo, noo ngi lay...

FUKKI SIMILI YI SOPPI AMERIG BA FÀWW (Paap Aali Jàllo)

PAAP AALI JÀLLO George Floyd, jamono jii, mooy néew bi gën a siiw ci àddina sépp. Li kob takk-der bu weex faat ci anam yu ñaaw...

MAKI SÀLL : "NAN JÉEM A DUND AK DOOMU JÀNGORO BI TE DU LOR KENN"

(PAAP AALI JÀLLO) Njiitu réew mi woyofal na sàrti guural gi ak dogal yi mu jëloon ngir xeex mbasum Covid-19 bi. Ci altine ji, 11eelu...

AFRIG AK KORONAA, AFRIG GINNAAW KORONAA

USÉYNU BÉEY Koronaawiris bi, li muy metti metti, terewul kàngami boroom xam-xam yiy wéy di ci weccee xalaat ñeel doxalinu àddina si, ba xam luy nar a...

BÉS BU MBAS MI XÉYEE NE MES… (Abdulaay Sekk)

ABDULAAY SEKK Mbas mi jaaxal na ñépp, yëngal àddina sépp. Jàngoro jii di koronaawiris wone na boppam ci fànn gu ne : koom, wér-gi-yaram, njàng,...

JÀNG AK JÀNGALE CI JAMONOY MBAS (Safiyetu Béey)

SAFIYETU BÉEY Céy Koronaa ! Doomu-jàngoro bii yëngal na jamono. Ku mënoon a gëm lu ndawe nii dina noot àddina sépp ? Tax na ba kenn ñemeetul a...