Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

FAIDHERBE DU FI MAAMU KENN

Fan yii yépp, xanaa mën nañoo wax sax weer yi weesu yépp, coow laa ngi neeti kurr ci biir réew mi ak ab jàppante...

(AMI MBENG)

  Senegaal :   Yan njàngat la askan wi wara jukkee ci kàngam yu bare te ràññeeku yi génn àddina ci fan yii ? Ci diirub 40i fan   rekk, réewum Senegaal dëjal na fiy boroomi daraja yu fésoon lool. Li ci gën a doy-waar mooy ne dafa méngook jamono joo xam ne, réew maa ngi jànkoonteek mbasum covid-19 mi. Loolu, nag, war nanoo yee, nu xool naka lees di def ba ndaw ñi roy ci ñooñule réew mi ñàkk.  KORONAA : Jawriñ biñ dénk kaaraange biir réew mi Aali Nguy Njaay, dina jàkkaarlook taskati xibaar tey ci àjjuma ji bu ñeenti waxtu ci ngoon jotee.  BEYROUTH : Daanaka lu tollu ci 137i nit ñàkk...

Taalifi Nday Sayba Faal ak Saydu Ba

Saydu BA waa Ñooro la, di al-pulaar bu gàlle. Ndaanaan luy yëngu ci teyaatar la, tëgg ak um pecc. Tukki na ci réewi nasaraan...

LÀMBI GOLO-O ! KU JÓG SAAGA ! (PAAP AALI JÀLLO)

Njoolum-golo miy def yëfi goloom, ku ci yéemu dangay door a yeewu, mbaa nga doon ku mësta yeeru. Ñu baree ngiy coow ci...

GÀTTALUG XIBAAR YI (AMI MBENG)

Ami Mbeng Ndengeleer Askan way yeewoo ca Ndengeleer amal nañu ab ndaje di xamal waa nguur gi ne : ñaari fan lañu leen may ngir ñu...

ËTTUB TAALIF (BAABAKAR JÓOB AK NDEY XAYBA FAAL)

I Sëriñ Baabakar Jóob Callweer ndaanaan la, di bindkat, di gëstukat itam ci làmmiñu wolof. Liggéeyam ak xam-xamam dëgg nag ñi ngi jëm ci teyaatar....

USMAAN SONKO : ‘‘BU MAMADU JA AK SÉEX ANTA JÓOB ÀNDOON YOR RÉEW MI CI ATUM 1960…’’ (Ñetteelu xaaju laaj-tontook Ndey Koddu Faal, Paap...

  LU DEFU WAXU : Ban taxawaay la Afrig war a am ? USMAAN SONKO : Tey, Afrig ci boppam moo nekk ci guddi gu bët setagul. Réew yépp...

GÀTTALUG XIBAAR YI (AMI MBENG)

(Ami Mbeng) 6i DOGAL YI MAKI SÀLL MUJJEE JËL ÑEEL MBAS MI Njiitu réew mi, Maki Sàll, amal nab bàttale ci altine ji weesu, 29eelu fan...

ËTTUB TAALIF

‘’Ëttub taalif’’ mooy xët wu bees wi defuwaxu.com jagleel ladabu réew mi. Sunu xarit, sunu doomu-ndey Mataar Caam Faal, moo yor wile xët. Képp...

LI TAX NDENGLEER MERE BAABAKAR NGOM ''SEDIMA'' (PAAP AALI JÀLLO)

Beykati Ndengleer yi, ab dëkk bu féete ci bokk-moomeelu Njagañaaw, ñooy jiiñ Baabakar Ngom, boroom SEDIMA, ne da leen a jaay doole, nangu seen i...