Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

FAGAROO GËN FAJU

  Li Faal Sàmba Suuna Sama maam daan na wax ni maamam dund na téeméeri at ak ñaar-fukk yu ànd ak wér ak wérle. Ndax magal...

GÀTTALUG XIBAAR YI (Altine 13 eelu – dibéer 19eelu awril)

Paap Aali Jàllo Mbasum Covid-19 bi faat na juróomi way-tawat ci diggante dibéer ak altine Ci dibéer ji, bi minwi di waaj a jot, la xibaar...

DÓOR I YAT YARUL GONE

 SAFIYETU BÉEY Juróom-ñetti xarnu ci ginnaaw, amoon na fi buurub Almaañ bu ñuy wax Ferederik 2. Daa déggoon làkk yu bari, demoon na ba mokkal 9i...

‘’ÑAAWTEEF YIY XEW TEY RÉEWUM SIIN DU GULÉET…’’

(SÉEX MBÀKKE AMAAR, JËWRIÑU NDONGOY-DAARA SENEGAAL YA CA WUHAN. CI TAATAANUG NDEY KODDU FAAL) Ndey Koddu Faal : Sëriñ Séex Mbàkke AMAAR, maa ngi lay...

FAATUG HIBAA CAAM : SENEGAAL, BOPP BU XAR ÑAAR?

Guddi àjjuma, dëppook 3eelu fan ci weeru Awril, doon guddi gi jiitu bésub baaxentalub sunu moom-sa-réeew, la benn jànq bu am 28iat, di wuyoo...

NAKA LAA GISE MBAS MI

Mbas mu dërkiis, ñàkk teggin tey jur tiiñalante ci biir réew mi ak ci bitim réew.... Naka la doomi Afrig yi war a taxawe ? Céy mbas...

KORONAA JAT NA PAAP JUUF, GAYNDEY GAYNDE YI !

« Ërob, rawatina Farãs, dañuy xeex ak a bunduxataal tuutaafoni waaso yi (minorités ethniques). » Njiitalu “Olympique de Marseille’’ ba woon, Paap Juuf, faatu na...

KORONAA AK KOOM-KOOMU RÉEW MI

Xari Njaay Mbasum koronaawiris mi lëmbe na àddina sépp, jaxase réew yépp. Amul menn réew mu mucc ci jàngoro ju bon jii bawoo Siin, ci weeru desàmbar...

LAN MOOY GARAB ? (Li Faal Sàmba Suuna)

Li Faal Sàmba Suuna Lépp li nit kiy jënde farmasi la Wolof Njaay tuddee garab. Moone dey, yemul foofu ndax gàncax gi du dara lu-dul i garab...

KORONAAK ÀDDINA (Làmp Faal)

Taalifu Làmp Faal Kala Ki daan mere nit ñi ci ñàkk a nuyoo Moo bank ab loxoom di tere nuyoo Ki daa tëju amul yitte lañ daan...

NDAJEM NJABOOTU ALFABETISAASIYOŋ CA KUNGÉEL

Jaafara Sadiixu Fofana Ca Kungéel (péeyub Bàmbug) amoon na ndajem tàggat bu ñetti fan ci « Ndefarum saf-safal ak sunu xeeti meññeef yi ak suusal caakiri ak...