Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LAAJ-TONTOOK GUY MARIUS SAGNA (GII MARYIIS SAAÑA)

Seen yéenekaay LU DEFU WAXU mi ngi dalal tey Gii Maryiis Saaña, fara caytu doxal (secrétaire exécutif) gu kurélu way-moomeel bees duppe FRAPP « Auchan...

LAAJ-TONTOOK GUY MARIUS SAGNA II

LAAJ-TONTOOK GUY MARIUS SAGNA (II) ‘’KU NEWUL ‘FRANCE DÉGAGE’ WAXOO DARA’’ Li ngeen di jàngsi mooy ñaareelu xaaju waxtaan wu yaatu wi Gii Maryiis Saaña, di kenn ci...

INIWÉRSITE GASTOŋ BERSE : LU ËPP TUURU

18Coow li neeti na kurr. Ndongoy Iniwérsite Gastoŋ Berse bu Ndar defati nañu seen mënin. Fan yii ñu génn, daara-ju-kowe ji tàngoon na jérr...

ARAM FAAL, SUNU SÉEX ANTA JÓOB BU JIGÉEN…

Talaata jii weesu di 23 ci weeru awril la Mbootaayu-Xeet yi jagleel bépp teere bu doom-aadama bind ci àddina si. Ci la EJO ak ArtXaleyi, di...

SÀNDIKAA NJABOOTU ALFABETISAASIYOŊ JUDDU NA

Askanu Senegaal dafa mës a weg i làmmiñam, làmmiñi réew mépp. Yàgg na leen a jàppe niy bokk-moomeelam. Loolu, deesu ko nàttable. Naam, ñoo...

GAALU JINNE

Jinne yu ñuul yi ñaay nañu Sunu Gaal gi, soppi ko gàngunaay, tëmbal ko ci géej gu sàmbaraax. Sunu Gaal gaa ngiy jaayu, jinne...

7 MÀRS WALLA 8 MÀRS ? BEY CI SA WEWU TÀNK…

Juróom-ñetteelu fan ci weeru màrs la xel yépp di dem ci jigéen ñi, ndax seen bés la. Àddina sépp a koy màggal, di ci...

NISERYAA : BUHARI FALUWAAT NA

Ci weeru féewaryee wii jàll la askanu Niseryaa doon amal woteb njiitu réewam. Ba ñu àggee ci cëpaandoo li, Muhammadu Buhari la askan wi...

MBËMËSTAL CI JAAR-JAARU ÀLLAAJI OMAR TAAL

Àllaaji Omar Taal mi juddu ci atum 1796 ca Fuuta, bokk na ci ñi siggil ba fàww nit ku ñuul ci lislaam. Nekkul woon...

ANA LU GÓOR-GIY LÀQARCI ?

Bamu jógee Konaakiri ba tey, seeti woon Alfa Konde, Abdulaay Wàdd, sunu Njiitu-réew ma woon, a ngi ne selaw. Wote bu 24 féewaryee bi...

BÉS DU MAG, DU TUUTI, BOROOM LAY TOLLOOL…

Dëgg la : ràcc jëmale sa kanam baaxul waaye tey fàww LU DEFU WAXU xamle mbégteem ci ndam li Paap Aali Jàllo am fan yee...