Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

NDAM LU SAFUL XOROM, SAFUL SUUKAR…?

10Dibéer yemook ñaar-fukki fan ak ñeent si weeru Féewaryee, la waa réew mi doon tànn ki leen war a jiite ba atum 2024. Waaye,...

‘’BÀNK MONJAAL’’, KURÉL GI NUY JATAŋ

Ñépp a ngi fàttaliku ni « Bànk Monjaal » nasaxale woon réew mi ci nguurug Abdu Juuf. Ci wàllu njàng, wér-gi-yaram ak mbir yu...

SENEGAAL, SEEN GAAL LA, ÑOOM, AM SUNU GAAL… ?

Ku waaruwul ci doxinu miim réew, saw doxin dina la waari ëllëg. Ku yéemuwul ci jëmu gaal gii, teeru bi dina la yéemi. Bees...

XALAM DEMOON NA BAY NEEX

Dibéer, 24eelu fan ci weeru féewaryee, atum 2019. Bés bi ñépp doon xaar, agsi na. Bés bi taskati xibaar yi doon séenu, di ko...

JOŊANTE REN BII, PETOROOL LAY XEEÑ…

Keroog, askanu Senegaal jóg na ci njekk ak teggin, daldi def li ko war ci tànneefu njiitu réew mi. Ndax, bi waxtu wi jotee,...

KU TIITUL MAN TIIT NAA

Senegaal wote nañu dibéer ji weesu yamook ñaar-fukki fan ak ñeent ci weeru féewaryee. Ba démb ci alxemes ji ñu ngi doon xaar njuréef...

ÑAŋ-MBAALO, TOJ NGA LÀMB JI !

« Toj naa fii ! », « Tasaare naa fee ! », « Rajaxe naa fale ! »… Su nu waxantee dëgg, xorom si moom la ! Moom Madike Ñaŋ, kenn ci wutaakoni yi, mooy...

DIINE AK POLITIG : NAN MOYTU LI NUY FÉEWALE

Ëttu boole bi, genn kurél la gu boole mbooleem këri diine yi ngir saxal jàmm ci biir réew mi, rawatina ci lu ñeel politig...

Lan la wutaakon yi naral làkki réew mi ?

Waaw mbokk yi, lan la wutaakon yi naral làkki réew mi ? Man ci sama wàllu bopp, déggaguma ci lu ma doy. Ndax Wolof,...

KAN MOOY USMAAN SONKO ?

Usmaan Sonko nëbbu ko kenn : mébétam mooy jot ci réewum Senegaal ci guddig dibéeru 24 féwaryee 2019, wuutu Maki Sàll. Ci li ñépp seetlu,...

MÀNGAAN NDEKE AM NA CI PÓLITIG !

b ak yu tey gis ñu woroo lool. Am na sax ci ñoom ku ne woon Ndeyu-Àtte réewum Senegaal dafa war a aaye màngaan...

RIIRU KÀMPAAÑ

Lépp lu yëngu am na lu ko yëngal. Réewum Senegaal, jamono jii mu ngi toll ci waajtaayu joŋante bi ñuy fale kiy toog ci...