Defu Waxu

14eelu LËLU SAES : AW YOON NGIR TINKI NJÀNG MU KAWE MI

Kenn werentewul ne njàng mu kowe mi dafa nekk ci guuta. Ab diir a ngi nii, muy jànkonte ak ay jafe-jafe yu bir. Li ko waral lépp mëneesu ko fi lim. Waaye, kurélug jàngalekati jàngune yi, gàttal biy joxe SAES ci tubaab, amaloon na...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI

PÓLITIG Saa-fuuta yi noppeeguñoo wannaasu tiiñal gi leen ñenn ci kujje giy tiiñal bi Bennoo Bokk Yaakaar rawee foofu ca Fuuta ci wotey Ngombalaan yiñ génn. Gannaaw bi BBY Podoor fasee yéene yóbbu fa mbaxane doone benn Usmaan Sonko ak Décce Fall, Séex Umar Aan...

Lan la wutaakon yi naral làkki réew mi ?

Waaw mbokk yi, lan la wutaakon yi naral làkki réew mi ? Man ci...

KAN MOOY USMAAN SONKO ?

Usmaan Sonko nëbbu ko kenn : mébétam mooy jot ci réewum Senegaal ci guddig...

DÉMB SEŋOOR, TEY WÀDD

Li ko dale atum 1978 ba tey jii, woteb ren bii mooy wote bu...

AYSATA TAAL SÀLL : JIGÉEN SOPPAL TE BUL WÓOLU…?

Bés ba ma ko déggee mu naan kilifa diine yi dañ maa ñaan ma...

Bàlla Gay-Móodu Lóo : ñaar ci dara

Làmbu démb ak ju tey jeeka wuute ! Ndege, démb, bu nawet bi wàccaan, ci...

XËT YI MUJJ

14eelu LËLU SAES : AW YOON NGIR TINKI NJÀNG MU KAWE MI

Kenn werentewul ne njàng mu kowe mi dafa nekk ci guuta. Ab diir a...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI

PÓLITIG Saa-fuuta yi noppeeguñoo wannaasu tiiñal gi leen ñenn ci kujje giy tiiñal bi Bennoo...

TOLOF-TOLOFI ARTISÃ YI : LAN MOO CIY TAXAWAAYU NGUUR GI

Fànnu artisanaa nekk na lu soxal lool nit ñi rawatina artisã yi yore seen...