Defu Waxu

BÀRTELEMI JAAS GINNAAW DAAN BI ÑU TEG CI KAWAM

Ёttu àtte bu Ndakaaru dёggal na daan bi ñu teg ci ndoddu Bàrtlemi JAAS ci Àllarba jii nu weesu. Daan boobu nag li ko waral mooy benn jàmmaarloo bu amoon ca buntu meeri Mermoos Sàkkerekёer, 22 ci Desàmbar atum 2011, mu amoon ndaw lu...

SENEGAAL 2 – BOLIWII 0

Ekibu nasiyonalu Senegaal bu futbal a ngi ci waajtaayu Kub di mond bi war ame ca Qataar. Joŋante bu mag boobu nag, daanaka ay fan kesee ci des. Nde, dibéer 20i fan ci nowàmbar lay door, Senegaal ak Olànd war a futbal joŋanteb ubbite...

NDEY SÀGGAN, DOOM FAATU (NDEY KODDU FAAL)

Waa Mamel, fii ci Ndakaaru, naqar ak tiis lañ fanaanoo. Li ko waral mooy...

KAN MOOY JIITEJI CESTI ? (NDEY KODDU FAAL)

Atum 2005 ak léegi daara ju mag jiy tàggat taskati xibaar yi ci Iniwersite...

ÀTTEKAT YUY WERANTE BAY WEERANTE (NDEY KODDU FAAL)

Fii ci Senegaal, ay kàngam ci yoon ñooy tamante dëmm. Àttekat bii di Yaaya...

« Y’EN A MARRE » (NDEY KODDU FAAL)

Talaata jii ñu weesu (1 Sàttumbar 2020) kurél gii di « Y’en a marre...

MUSAA JÓOB BAÑ NA NI MUUT, NEE NA MOTT (NDEY KODDU FAAL)

Musaa Jóob layookat bi doon jiite "Dakar Dem Dikk" la njiitu réew mi tekki...

SUNU GIS-GIS CI ''BLACK LIVES MATTER'' AK YENEEN XEETI ÑAXTU ÑEEL XEETAL AK ÑAAWTEEFI TAKK-DERI AMERIG YI (Kàddug mbooloom kàngami Mbootaayu Xeet yi fekk...

(Ci tekkig Ndey Koddu Faal) Njolloor, ca Minneapolis. Alkaatib Tubaab teg óomam ci kow loosu nit...

XËT YI MUJJ

BÀRTELEMI JAAS GINNAAW DAAN BI ÑU TEG CI KAWAM

Ёttu àtte bu Ndakaaru dёggal na daan bi ñu teg ci ndoddu Bàrtlemi JAAS...

SENEGAAL 2 – BOLIWII 0

Ekibu nasiyonalu Senegaal bu futbal a ngi ci waajtaayu Kub di mond bi war...

YÀNQOOBA JATARA, JËWRIÑU TAGGAT-YARAM JU BEES JI

Mataar ba nekkatul jëwriñ jiñ dénk tàggat-yaram gi. Loolu bokk na ci xibaar yi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 24 Sàttumbar 2022)

PÓLITIG  Ginnaaw mbetteel ga mu am ca Ngomblan ga ca palum njiit la, ndax Aminata...