Defu Waxu

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀLLARBA 15 MÀRS 2023)

PÓLITIG Tey ci àllarba ji la làngug Pastef namoon a amal seen doxi-ñaxtu yi ci...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (TALAATA 14 MÀRS 2023)

PÓLITIG Ci talaatay tey ji la lëkkatoo Yewwi Askan Wi doon amal ab « Giga meeting »...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (DIBÉER 12 MÀRS 2023)

DOXU-ÑAXTU CA PARI « Ca Senegaalu Maki Sàll, boo naan déet di dugg kaso ! » Kàddu gilee...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀJJUMA 10 MÀRS 2023)

Paap Njaay tëddi na Sebikotaan Taskatu xibaaru Walfadjiri bi, Paap Njaay, mujje nañ ko jàllale...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ÀLLARBA 8 MÀRS 2023)

YOON Waa "Sureté Urbaine" bu Ndakaaru woolooti nañu. Wile yoon, Séex Aajibu Sumaare lay doon,...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (ALTINE 6 FÉEWARYEE 2023)

PÓLITIG Ndogal lu yees ñeel peyooru dépite yi    Yokkal nañu dépite yi 700.000i FCFA...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (DIBÉER 5 MÀRS 2023)

PÓLITIG Bàyyi nañu Gii Mari Saaña ak way-moomeel yi Démb, ci yoor-yoor gi, lañu...

Li gën a fés ci xibaari bés bi (Gaawu 4 fewaryee 2023)

NJÀNG AK NJÀNGALE  Ab toogaanu-ñaxtu la ñenn ci jàngalekat yi ñuy woowe "contractuels" amaloon démb....

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA