Li fës

NATHALIE YAMB : “LI TAX MAKI SÀLL DELLU GINNAAW…”

Altine jii weesu yemoo woon ak ñetti fan ci weeru sulet la Njiitu réew...

MAKI SALL : « KENN DU TEE WOTE YI AM ! »

Njiitu réew mi, Maki Sàll, amaloon naw waxtaan ak sunuy naataango yu Le Monde,...

MAKI SÀLL – USMAAN SONKO : LÀMB JA CA FARÃS

« Càmmug Senegaal amati na mbetteel ci jeng bi tele France 24 di jeng...

LAAJ-TONTU USMAAN SONKO AK FRANCE 24

Usmaan Sonko, njiitul Pastef li, doon na tontu ci laaji Marc Perelman mu France...

BAC 2023

Ni ñu ko baaxoo amale ci réewum Senegaal, démb ci Talaata ji, yamoo ak...

Xalifa Sàll : « Maki Sàll… dafa musal réew mépp. »

Bi Njiitu réew mi waxee démb ne du bokk ci wotey 2024 yi ba...

MAKI SÀLL : « DUMA LAWAX CI WOTEY 2024 YI . »

Njiitu réew mi fay na coowal ñetteelu moome gi. Àddu na, indi ci tontu...

USMAAN SONKO : “LI TAX MAKI SÀLL MËNU MA JÀPP…”

Usmaan Sonko jiitu na Maki Sàll ci kàddu gi. Ci altiney tey jii, 3...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...