Li fës

JÀMBAAR

Jógati naa saddati ay bayit sargale mbër Bàkk ko jiin ko xaacu naan na woy...

NDAJEM KAAJARU “TÀNN-BÉER” BU LÀMP FAAL KALA

Gaawu gii weesu, yemoo woon ak ñaar-fukki fan ak benn ci weeru oktoobar wii,...

KOLONEL SÉEX TIIJAAN MBÓOJ WUYUJI WOON NA SÀNDARMI KOLOBAAN YI

Kolonel Séex Tiijaan Mbóoj wuyuji woon na sàndarmi Kolobaan yi. Moom, Séex Tiijaan Mbóoj,...

SAALIW MBAY : NDÀND FAAL, KËR MADAM (2/2)

Bërki-démb, ci gaawu gi (21eelu oktoobar 2023), lañ doon aajar téere Porofesëer Saaliw Mbay...

SAALIW MBAY : NDÀND FAAL, KËR MADAM (1/2)

Bërki-démb, ci gaawu gi (21eelu oktoobar 2023), lañ doon aajar téere Porofesëer Saaliw Mbay...

DUND BU JAFE BI : SAA-SENEGAAL YEE NGI ÑAXTOOTI

Démb ci gaawu gi, 21 oktoobar 2023, saa-senegaal yaa nga woon fa Place de...

USMAAN SONKO WEER NA MAKI SÀLL

DGE, kurél giy saytu lépp lu aju ci wote yi, lànkalati na ndawul Usmaan...

LUUBALUG 30I TAMNDARETI CFA CA CMS

Ka yoroo keesu kër gii di CMS (Crédit Mutuel du Sénégal) moo luubal ay...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...