Xibaar

QATAAR 2022 Talaata 22 nowàmbar 2022

Talaatay démb jee nekkoon ñetteelu bésu kuppeg àddina siy ame Qataar. Ñaari ponkal waroon...

CNRA DOG NA SIÑAALU iTV

Ngir fàttali, CNRA dafa artu woon rajo yeek tele yi ngir ñu bañ a...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu 19 nowàmbar 2022

PÓLITIG Woteb nafag 2023 gi door na ca Ngomblaan ga. Tey ci gaawu bi, jëwriñ...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Alxames 17 nowàmbar 2022

TÀGGAT-YARAM Futbal/Qataar 2022 : Saajo Maane du bokk Yaakaar tas na ! Ndeysaan. Xibaar bu tiis...

Li gën a fés ci xibaari bés bi Àllarba 16 nowàmbar 2022

PÓLITIG  Maalig Gàkku Léegi leer na, kii di Maalig Gàkku mooy nekk lawaxu làng gii di...

SAAJO, IMAAM YI SAX ÑU NGI ÑAAN

Gaañu-gaañu bi Saajo Maane ame ginnaaw kuppe ga mu mujje def ca Bayern, jural...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 14 noowàmbar 2022

PÓLITIG Maalig Gàkku dina nekk lawax ci wotey njiiteefu réewum Senegaal yii di ñëw. Làngu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 12 NOWÀMBAR 2022)

PÓLITIG Na mu ko yëglewoon ginnaaw ba mu janook taskati-xibaar yi, Usmaan Sonko miy njiitu...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...