Tàggat-yaram

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (10/07/2023)

MAROG JËL NA CAN U23 BI Démb, ci gaawu gi, lañ doon amal lii di...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (6/7/2023)

AFROBASKET-JIGÉEN, RUWÀNDAA 2023 Gannaaw tànn gu njëkk ga, Mustafaa Gay, seggaat na ekib bi, tànn...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (2/7/2023)

Dëmi-finaal U23 Ginnaaw-ëllëg, talaata 4i fan ci sulet , la dëmi-finaali joŋateb kuppe U23 di...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (21/6/2023)

Senegaal duma na Beresil 4-2 Démb ci talaata ji la ekibu Senegaal bu mag bi...

SENEGAAL, YOKK CERE, DOLLI ÑEEX !

Sàmpiyonaa yi jeex nañu. Ekibi dëkk yi ñooy futbal jamono jii. Ñii di futbal...

MANCHESTER CITY WITTI NA BIDDIIWAM BU NJËKK

Àngale yaa ngay gundaandaat ! Manchester a ngi toj ! Ren, dafa baxa. Ci bëccëgu dibéeru...

CAN U17 2023 : KUB MU NGI XEEÑ !

Raayab Senegaal a ngi gën yéeg, turam di gën a jëm ca kow a...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ALXAMES 4 ME 2023)

RËBËJOO BA CA PSG Gannaaw tukki bi Messi amaloon ca Araabi Sawdid, njiiti Paris Saint-Germain...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...