Tàggat-yaram

AS PIKINE – GUEDIAWAYE FC : XUMB TE DAGAN

Keroog, ci gaawu gi 29 awril 2023, sàmpiyonaa Senegaal bi jaxoon na lool. Ndax,...

LAMIN KAMARA, GONEG WURUS GI

Mamadu Lamin Kamara, jàppleen tur wi. Xareñte, dëgëraay, njaxlaf ak dégg-daaj la gaynde gu...

FU MESSI DI FUTBAL DÉWÉN ?

Jamono jii, laaj bii moo lëmbe xel yi, rawatina xeli soppey Barcelone FC yi....

LI GËN A FËS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ÀJJUMA 7 AWRIL 2023)

XEETAL CA ITALI Kañ mbirum xeetal, xeeb ak mbañeel di jeex ci àddina si, rawatina...

NJAAY DARAAPOO DËDDU NA

Momar Njaay, ñu gënoon koo miin ci turu "Njaay Daraapoo", dëddu na. Moom, nag,...

LI GËN A FËS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ALXAMES 23 MÀRS 2023)

Adebayoor ak Özil bàyyi nañu Adebayoor, saa-Tógoo bàyyina kuppe ! Barkaatii-démb ci altine ji la...

LI GËN A FËS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM (ALXAMES 9 MÀRS 2023)

KUPPE Àngalteer Démb, foo geestu ci mbaali-jokkoo, ñoo ngi doon wone ay naataal ak i widewooy...

LI GËN A FËS CI XIBAARI TÀGGAT-YARAM (DIBÉER 5 MÀRS 2023)

LÀMB  Saa-Cees - Rëg-rëg ñoo doon bëre ci dibéeru tey ji. Mu doonoon làmb ju...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...