Tàggat-yaram

ALSERI DUMAATI NA SENEGAAL

Démb ci talaata ji la gayndey Senegaal yi doon janook Alseri ci joŋante xaritoo....

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (3/9/2023)

SAALIF KEYTA KUPPEKATU MALI BA WOON GAAÑU NA Ci gaawug démb ji, 2 sàttumbaar 2023,...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

MESSI GAÑE NA KUBAM BU NJËKK AK INTER MIAMI Ci guddig gaawu gi jàpp dibéer...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

LIGUE DES CHAMPIONS 2024-2025 Waa UEFA amal nañu ay coppite yoy, dañuy yokk limatu ekib...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

Real Madrid a ngi wër góol bu bees Thibault Courtois, góolu Real Madrid bi,  dafa...

AFROBASKET-KIGALI 2023 : XALAM DEMOON NA BAY NEEX !

Démb la woon finaalu Afrobasket bi doon am ren ca Ruwàndaa, doxoon ci diggante...

XIBAARI TAGGAT-YARAM (23/7/2023)

MESSI DELLOONA BUUM CA MBOY-MBOY GA ! Bërki-démb ci guddi, bi 3i waxtu jotee, la...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (16/7/2023)

KUPPEG ÀDDINA SI 2026 Kippu yi ñeel xëccoo paasu kuppeg àddina si war a am...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...