Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 31 Oktoobar 2022

PÓLITIG Lawax yi jëm ci wotey 2024 yee ngi gën dee yokku. Démb ci dibéer ji la Dr Abdurahmaan Juuf doon siiwal ci turu làngug...

PASUG NGÀNNAAY GI : MBIR MI TEERI NA NGOMBLAAN GA

Dañ doon xaarandi Ngomblaan gi wax ci mbirum pasug ngànnaay gi dox diggante Nguurug Senegaal ak kërug liggéey gii di Lavie Commercial Brokers, dépite...

CAN 2022 (Beach soccer) : Senegaal gàddooti na ndam li

Senegaal jël na Can 2022 (beach Soccer) bi. Esipt la dóorati 6-5 ci dóoral-ma-dóor (tirs au but) yi ginnaaw bi ñu témboowee 2-2 ci...

PASUG NGÀNNAAY GU 45i MILIYAAR : AW NJOMBE WU BEES ? 

Ag pasug 45i miliyaar ñeel i ngànnaay yu Njawriñu kéew mi jënde ci LAVIE COMMERCIAL BROKERS moo lëmbe réew mi fan yii. Li ko...

CARGALUG NEUSTADT INTERNATIONAL PRIZE FOR LITERATURE : BUBAKAR BÓRIS JÓOB JËL NA NDAM LI

Ci talaata 26eel ci oktoobar 2021, lees jot ci mbégtem weer wi. Surnaalu ladab bees duppe World Literature Today, nekk ca Iniwérsite Oklahoma, ca...

WAXTAAN CI MBIRUM ALFAABETISAASIYOŊ AK DEMOKARAASI Mamadu Jara Juuf 2/2

Yaxal bii, aw waxtaan la wu, bindkat bii di Mamadu Jara Juuf moo ko amaloon ca Kawlax, 8 sàttumbar 1992. Mi ciy waxtaane alfaabetisaasiyoŋ...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BES BI Talaata 25 oktoobar 2022

YOKKUTEG NJËGU DUGUB BI  Jamono jii, askan waa ngiy jooy dund biy wéy di yokk. Nde, dugub bi tamit yokk na. Kilo bi daan jar...

CÀDD, JÀMM FÀDDU NA !

Juróom-fukki bakkan yu rot ak ñetti téeméeri nit yu amey gaañu-gaañu, lii, fit du ko weesu. Réewum Càdd, jamono jii, moo nekk di tàkk....

WAXTAAN CI MBIRUM ALFAABETISAASIYOŊ AK DEMOKARAASI Mamadu Jara Juuf (ci xalima Paap Aali Jàllo)

Yaxal bii, aw waxtaan la wu, bindkat bii di Mamadu Jara Juuf moo ko amaloon ca Kawlax, 8 sàttumbar 1992. Mi ciy waxtaane alfaabetisaasiyoŋ...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 22 OKTOOBAR 2022)

PÓLITIG Dépite ya fare ca Wallu Senegaal, ña ngay sàkku ci njiitu jëwriñ ji Aamadu Ba, mu biral naali politigam ca Ngomblan ga. Mu nekk...