Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

WÀÑÑITEG PAYOORUG LEKKOOL BI

Ginnaaw ndaje mu tembere mi ñu amaloon ngir jël ay matuwaay ci yokkuteg dund bi, Càmm gi biral na dogal yees ci jël ci...

BÉSUB BINDKATI AFRIG YI

7i fan ci weeru nowàmbar mooy bés bi ñu jagleel bindukati Afrig yi (saa-Afrig). Ren, ci Alitine jii weesu lees ko doon amal ca...

Usmaan Sonko : « Paab Aale Ñaŋ du doon weneen nagu sarax… »

Coowal jàppug Paap Aale Ñaŋ gi moo lëmbe réew mi ba tey. Kilifa yu bari fésal nañ seen naqar ci lees ko teg loxo....

NJËGU DUND BI NJIITU RÉEW MI, MAKI SÀLL, JËL NA 11i NDOGAL

Ci gaawu gii weesu, 5i fan ci nowàmbar, lees doon amal am ndaje ngir fénc njëgu dund bi. Ndaje ma nag, ci njiital Maki...

JÀPPUG PAAP AALE ÑAŊ

Seneweb moo siiwal xibaaru jàppug Paap Aale Ñaŋ, taskatu-xibaar ak faramfàccekat bu siiw. Jamono ji nuy bind yaxal bii, mu ngi ci loxoy takk-deri...

XEW-XEWI NDÉGLUG USMAAN SONKO GI

Ci alxames jii weesu, ñetti fan ci weeru nowàmbar, la kii di Njiital PASTEF li, Usmaan Sonko, doon janoo ak àttekat bi. Li waraloon...

Sitt ak Papaa Sow : Wure wa dem na këŋ

Sitt ak Papaa Sow dinañ jàmmaarloo ci dibéer jii, 6 noowàmbar 2022 ca Aren Nasiyonaal bu Senegaal. Jàmbaar Productions moo ko tëggaat làmb ji....

Li gёn a fés ci xibaari bés bi Alxames 3 nowambar 2022

PÓLITIG Coowal Aji Saar ak Usmaan Sonko Démb ci alxames ji, 3 nowàmbar, la kii di Njiital PASTEF li, Usmaan Sonko, doon janoo ak àttekat bi...

NDÉGLUG SONKO GI, NA WOON FA WOON ?

Woote bi yoon woo Njiitalu Pastef li, Usmaan Sonko, la yéenekaayu yi xëyee tey. Mooy xibaar bi gën a fës fan yii. Nde, ci...

SÉMBUB SOROJ BU GRANDE-TORTUE Senegaal dina taxan 20 000i miliyaar ci diirub 30i at  

Bu liggéeyub soroj bi tàmbalee, Senegaal dina taxan, ci diirub 30i at, 20 000i miliyaar ci FCFA. Maanaam, at mu nekk, dina góobe ci...

ÑU SELL ÑA

Talaatay démb ji, 1 nowàmbar 2022, la waa jàngu bi doon màggal seen waliyu yu sell yi (Toussaints). Muy xew-xewu diine bu ñuy màggal...

« JÀMM A GËN 3e MANDAT »

Way-moomeel yee ngi sàkku ci Njiitu réew mi, Maki Sàll, mu bañ a laaj 3eelu moome (kay). Raddho, AfrikaJom ak yeneen i kurél yiy...