Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

Ballon d’Or France Football 2022 : Saajo Maane ci pójëm bi 27i at ginnaaw Soors Weyaa Saajo Maane, sa woy wi dootul fay

Saajo Maane, sa woy wi dootul fay Joxe nañ cargalub Ballon d’Or France Football 2022 ci altine jii weesu. Ñaŋ ko doon amalee ca Théâtre...

LI GЁN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Alxames 20 oktoobar 2022

XIBAARI BITIM-RÉEW Fitna sa ca Càdd Lu tollu ci 60i nit ak lu teg ñoo ñàkk seen i bakkan tey ca réew moom ci ab jàmmaarloo...

JÀNGOROY SËQAT SU BON SI

Sëqat su bon si, jàngoro ju ñu mën a moytu la, te it lu ñu mën a  faj la. Cib doomu jàngoro bees dippe...

“WAT GAAL AK YËGOO…” Jëwriñ Aliw Sow amal na tukkib nemmeeku ñeel artist yi

Ginnaaw bi ñu ko tabbee yees ci wàllum mbatiit ak moomeel, Aliw Sow door na tukkib nemmeeku ci biir réew mi. Li ko jëwriñ...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 17 oktoobar 2022

PÓLITIG Way-politig yi jublooti nañ ci wotey 2024 yi. Bu dee làngug Nguur gi, Njiitu réew mi, Maki Sàll, jóg na ngir dajalewaat i ñoñam....

GIS-GISU FMI CI ËLLËGU KOOM-KOOMU SENEGAAL

Yokkuteg dundu gi nekk di lëmbe àddina si boobu ba léegi tax na ba koom-koomu réew yu bari dellu ginnaaw bu baax a baax...

TЁRALINU KURÉL GU YEES GII DI “REELS”

Démb ci Gaawu bi 15 oktoobar la ñii di waa Yewwi Askan Wi doon taxawal kurél gii ñu dippe Réseau des Elus Locaux du...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI GAAWU 15 OKTOOBAR 2022

PÓLITIG Ni ñu ko junjee woon ginnaaw palum depite yi, kujje gi taxawal na kurél gu leen di ëmb. “REELS ( Réseaux des Elus Locaux...

LI GЁN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Àjjuma 14 oktoobar 2022

PÓLITIG Wayndare yiy xaar dépite yi Ginnaaw bi ñu taxawalee Ngomblaan gu bees, ci àjjuma jii la liggéey bi di tàmbali. Mu mel ni nag  lu...

Futbalu tefes gi : Gayndey Senegaal yi fobooti nañu

Gaynde Senegaal yu futbalu tefes gi fobu nañ. Démb ci alxames ji lañ doon nangu raaya réew mi ci loxoy Njiitu réew mi. Bile...

SIROY ALLAAXIRA YA CA  GÀMBI

Musiba bu réy a am ca Gàmbi. Juróom-benn fukki xale ak juróom-benn ñoo fa ñàkk seen i bakkan ci sababi siro yu ñu naanoon...