Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Alxemes 13 oktoobar 2022

NJÀNG AK JÀNGALE  Ñàkkum ndox ca daara ju kowe jii di UADB Daara ju kowe jii di UADB (Université Assane Seck de Bambey) dafa nekk di...

TATA MIMI COKKAAS NA MAKI SÀLL

Dige bor la. Wolof a ko wax. Moo tax, Aminata Ture dëggal na digeem ba. Gor ca wax ja. Ndekete, ndaw si Mimi, fasul...

YOMBALUG DUNDU GI, NISËRU NGUUR GI

Ci atum 2023 mii nu dëgmal, Nguur gi dafa fas yéene génne gafaka (budget) gu tollu ci 6. 400i miliyaar ci sunuy koppar ngir...

MALI AK FARÃS : LA WOON, WONNI NA (2)

Diggante Farãs ak Mali ma ngay wéy di ñagas. Loolu nag tàmbaliwul tey rekk. Ndax, ginnaaw bi ñu daaneelee kii di Ibraahiima Buubakar Keyta...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 10 oktoobar 2022

PÓLITIG Ginnaaw Umar Yum, Ismayla Maajoor Faal (jëwriñ jiñ dénk wàllu yoon) moo génn di dànkaafooti Mimi Ture ci taxaway bi mu namm a am...

GÀMMU GI

Weeru Gàmmu La Buur Yàlla taamu Ngir gane àddina Yonent bi Yàlla def mu gën ci mbindeef yi Gënal ko ñépp moom Rasululaahi Moo tax looy def bëgg mu...

MALI AK FARÃS : LA WOON, WONNI NA

Diggante Farãs ak Mali ma ngay wéy di ñagas. Loolu nag tàmbaliwul tey rekk. Ndax, ginnaaw bi ñu daaneelee kii di Ibraahiima Buubakar Keyta...

TOFTALEG FIFA : SENEGAAL CA KOW CA KANAM

Ci alxemes ji, 6 Oktoobar 2022, la Fifa siiwal toftaleem bi muy amal weer wu nekk. Lenn lu bees ruuseewu ci ñeel ékibu Senegaal...

LI GЁN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Alxames 6 oktoobar 2022

PÓLITIG Ndogali Njiitu réew mi Ginnaaw tabb yu yees yi mu defoon ci fan yee jàll. Démb, ci ndajem jёwriñ ma mu doon amalaat, Njiitu réew...

BALAA NGAA LAAX JAAY, LAAX LEKK

Ngomblaan gee woote ngir dépite yi jëlsi kaarbiraŋ biñ leen di jagleel weer wu nekk. Ku ci nekk, jagoo nga lu tollu ci 500i...

UBBITEG DAARA YI

Ginnaaw ñetti weer i bër, ndongo yi ak jàngalekat yi fas yéene nañoo awaat ca yoonu lekkool ya. Jàngalekat yi nag, ci altine jii,...