Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

MOOM SA BOPP, MOOM SAW LÀMMIÑ Baabakar Lóo (ca Pari)

Sunu réew, Senegaal, niki réew yu bare ci Kembaaru Afrig, yàgg naa dund ay xew-xew yu mboor dul fàtte mukk. Ci lu jege juróomi xarnu,...

SENEGAAL TIIT NA WAAYE ËLLËG, ËLLËGU ASKAN WI LA…(PAAP AALI JÀLLO)

Bindkat yi bind nañ, waxkat yi wax, gëstukat yi biral, boroom xam-xam yi jàngat, kilifa diine yeek yu aada yi àddu, aartu. Taskati xibaar...

LI TAX 102i BOROOM XAM-XAM YU MAG JÀPP NE SENEGAAL DU RÉEWUM YEMALE (MA-JAW NJAAY)

https://m.soundcloud.com/mohamadou-boye/manifeste-en-wolof

USMAAN SONKO : « MBATIIT MOOY LÉPP, MOOY CËSLAAYU YOKKUTE. »

Laaj ak tontu bii nag, seen yéenekaayub web defuwaxu.com séqoon na kook Usmaan Sonko ca atum 2020. Xaaj bu njëkk bii, siiwaloon nanu ko...

LÉPP LI CI BIIR LÀNKETU KAPITEEN SÉYDINAA UMAR TURE CA "SECTION DE RECHERCHES" BU KOLOBAAN…

Ci tekkig Musaa Jóob Aysatu Ñaari ayubés ak léegi coow lëmbe réew mi yépp, am Usmaan indi Aji, moom laak du moom. Coow li nag,...

MARCEL MENDY NELAW NA (NDEY KODDU FAAL)

Taalifkat nga woon bu daan yatt xalimaam di bind ci xew-xewi réew mi. Misaal mi ci mujj mooy ñetti woy yi nga jagleel Covid...

Macky sall (SBJ)

Muumaa di li mu fésal ci li xew ci réew mi. Ana lu waral faleesoon ko kon ci boppu réew mi? Cëram de moone du fésalug...

LI TAX 102i BOROOM XAM-XAM YU MAG JÀPP NE SENEGAAL DU RÉEWUM YEMALE

CI TEKKIB PAAP AALI JÀLLO * Séex Anta Jóob mas naa bind ne "Senegaal, mënees na fee jalgati yoon, tooñ nit ba toññarbi ko ba noppi rafetal...

TEGGIG MALAANU KIIRAAYU USMAAN SONKO : LI CI YÉENEKAAY YI BIND (Paap Aali Jàllo)

Coowal Usmaan Sonko moo lëmbe réew mi jamono jii. Gannaaw tuumay siif ak tëkkub rey yi Aji Saar teg ci kow deru Usmaan Sonko...

MBIRUM « SWEET BEAUTÉ » : NGALLA BULEEN GÀKKAL TURU SENEGAAL ! Bubakar Bóris Jóob (Ñu jukkee ko ci SenePlus, ci tekkib Ndey Koddu Faal)

Pólitiseŋ yeey faral di def lu xew ñu daldi àddu ci tàng-tàng bi. Loolu, nag, warul a jaaxal kenn. Ndaxte, ñoom, daanaka, bu waxtu...

KIPPUG WATTU LÀKKI RÉEW MI (CI TEKKIB PAAP AALI JÀLLO)

Cër bi nu jox farañse bi tax na ba, kenn sañul a xët sàrt yiy yoonal mbindam. Te sax, boo juumee ba yàq ci...