Jàngoro ju yéeme te raglu moo gaaral, fan yii, ay mool yu nappi woon ba delsi. Limeesagum na, xaat-xaat, 300i way-tawat. Jawriñu wér-gi-yaram wi ne, ku...
Ci beneen boor, ci nguuru Seŋoor lees nose, ñeel Senegaal, “Opération Persil” ak lenn ci “Opération Mar Verde”, ngir suuxal nguuru Séku Ture ca Gine ndax...