Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

FAN LA SENEGAAL TOLLOOK ÑAKK YI ? ( Musaa Aysatu Jóob)

Niki weeru féewaryee ci atum 2020 lañ njëkk a dégg baatu koronaawiris , ci 11eelu fan wa la doktoor yi joxe turu jàngoro ji....

Njàngatum Guddig Mbooyo (2/2)

Doolee mën dëgg, waaye dëgg mooy mujj. Li tax bindkat bi taamu kàddug Guddig Mbooyo, daldi koy tudde téereem bi, dug tandle. Bul jaawale. Mbooyo,...

LI CI BIIR "MBOORUM ÀDDUNA SI" BU ABDU-XAADR KEBE

KAN MOOY SËRIÑ ABDU-XAADR KEBE ? Sëriñ Abdu-Xaadr Kebe, ñu gën koo xam ci turu Jili Kebe, lijjantikat la (entrepreneur), yor lijjanti guy yëngu ci...

Njàngatub Bàmmeelu Kocc : Téereb dekkali 1/2

Du guléet. Déedéet. Bindkat bi tëbul rekk bind Bàmmeelu Kocc Barma. Nde, ginnaaw Doomi Golo, bii mooy ñaareelu téereb nettali bu werekaan bi, Bubakar...

SAFARAS NGAJAGA SI « Ci nen lan toog… » (Paap Aali Jàllo)

Ci gaawu bii weesu, 19eelufan ci weeru desàmbar, waa Ngajaga tiit ak njàqare lañ xéye. Daanaka, askanuw Senegaal ci boppam a jaaxle woon, tiit...

BOKK AK NAWLOO NGIR JÀMM AK NAATAANGE CI ÀDDUNA SI

Weer yii nu génn, réew yu bare tànn nañu seen njiit. Joŋante yi gën a indi coow mooy yi amoon ca Beliyoriisi mbaa Amerig, walla fii ci...

Li ci biir “Xelum Xalam” bu Làmp Faal Kala

KAN MOOY LÀMP FAAL KALA ? Làmp Faal Kala, am ñu ko gën a xame ci turu Ngoti Faal (Ngoty Fall), doomu Luga la ju...

LI CI BIIR "GUDDIG MBOOYO" BU LAMIN MBAAY

KAN MOOY LAMIN MBAAY ? Lamin Mbaay, ab Birigajeb pólis la woon. Mi ngi juddu 4eelu fan ci weeru desàmbar 1952, ca Mexe. Waaye, Aayre-Laaw,...

LI CI BIIR "XELUM XALAM" BU LÀMP FAAL KALA (EJO-Editions)

KAN MOOY LÀMP FAAL KALA ? Làmp Faal Kala, am ñu ko gën a xame ci turu Ngoti Faal (Ngoty Fall), doomu Luga la ju...

PAAP BUUBA, GAYNDE GU NU DOOTUL FÀTTE, (MUSAA AYSATU JÓOB)

Paap Buuba Jóob saay na, ginnaaw bi ko feebar bi ñuy wax "Charcot" tërale lu war tollu ci ñaari at ba tere woon koo...

SOXNA XADIJATU NJAAY CA KUNGÉEL, DOY NGA ROYUKAAY ! (AMI MBENG)

« …ñeewuma sama benn moroom bu jàng farañse. » Njiit li, boroom raaya yi, taalifkat bi, njiitalu mbootaayu liggéey (GIE), bàjjenu gox, aji-aw (relais), « conseillère municipale » … Ne...