Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

GÉEWUB WAXTAANE LÀKKI RÉEW MI

Grand Théatre bu Ndakaaru mooy amal géewub waxtaane làkki réew mi : mbir mu am solo ci ëllagi Senegaal.    Ci jamono ci ñuy warloo...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

LIGUE DES CHAMPIONS, EUROPA LEAGUE, CONFÉRENCE LEAGUE Ñetti joŋantey kuppe yoy tugal yépp àgg nañu ca cappaa-ndaw ga, maanaam, finaal ya. Bu dee Ligue des champions,...

JUBBANTI : DALUWAAYU NIMERIG BI ÑEEL PÉNCOOM PÓLITIG BI

Nguur gi taxawal na daluwaay nimerig bees dippee JUBBANTI ngir waajal péncoom réew mi ñu jagleel pólitig bi. Muy ab daluwaay ngir amal péncoo...

LI ÑÉPP BOKK

Waxi Wolof, yenn saa, dañuy xaw a juunoo. Dafay mel ni sax kuy weddi boppam. Weddi boppam ! Mbete nit. Aa, xéy-na nit la de....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/5/2025)

CÀMBAR YI JÓGE CI SÉMBI TEG I TUUMA ÑI FI NEKKOON I JËWRIÑ Ngomblaan ga yëngu na lool fan yii. Ndax, bu ñu jógee ci...

MBIRUM AAMADU (MAKI) SÀLL : WOOLU NAÑ WAALI SEKK

Mbirum Aamadu Sàll, doomu Njiitu réew ma woon (Maki Sàll), mi ngi wéy di lëmbe réew mi. Nde, dañu ko tudd ci luubalug alal....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/5/2025)

NJÀNG MEEK NJÀNGALE Mi Jëwriñu njàngale mi ci daara yu ndaw yeek yu digg-dóomu yee ngi ci tànki jële fi njoogaani jànguwaay yi. Démb...

ÑAXTUY LÀNGI PÓLITIGI MALI YI

Coowi pólitig yi lëmbe na lool réewi Afrig sowu-jant yi, rawatina ci juróomi at yu mujj yii. Donte ne sax, la ko jiitu daan...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

SÀMPIYONAA ALMAAÑ : BAYERN MUNICH NANGUWAAT NA CËRAM Vincent Kompani ak i ndawam jël nañu sàmpiyonaa Almaañ bi. Naam, joŋante ya jeexaguñ. Waaye, moom Bayern...

MUREES NA MBALAANI KIIRAAYI MUSTAFAA JÓOB AK NDEY SALI JÓOB JEŊ

Ngomblaan gi muri na mbalaani kiiraayi ñaari dépite yii di Mustafaa Jóob ak Ndey Sali Jóob Jeŋ. Muy ndogal lu tukkee ci ndiisoog cëtëŋ...

NDOG LU METTI FA WELINGARA : ÑAARI NJÀNGAAN FAATU NAÑU CI

Ñaari njàngaani CEM Saare Koli Saale ñoo faatu ci ndog mu metti ci gaawug tay jii, 3eelu me 2025, fa Welingara. Biis bi ñu...