Moo ndax
Ki ko tey
Taamu
Tànn
Ndëŋte
Ak njubadi
Dina wuuteek
Bant bu wow koŋŋ
Téll dàmm lay mujje
Mu wóor ne du soppi
Jikko ndax làggi
Ca mbir ma
Na yoon yor yar ba
Soo...
XAATIMUG DÉGGOOB DAL DIGGANTE NGUUR GI, SÀNDIKAA YI AK “PATRONATS” YI
Bésub alxamesu tay jii lañu jagleel liggéeykat yi. Waaye, loolu terewul Nguur gi di...