Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

DIGAALE SENEGAAL AK RIISI ÑEEL MBAY MI

Njiiti réew mi, dañu nas aw naal, tudde ko "Senegaal 2050", mu doon cëslaay gi nuy sukkandiku ngir ligg réew mi. Ca weer yee...

PAAB FARÃSUWAA GÉNN NA ÀDDUNA

Naqar ak tiis la mbokki katolig yi yeewoo ci altiney tay jii. Kii di Paab ba Farãsuwaa moo wuyuji boroomam. Kii di “Cardinal camerlingue...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

LÀMB JI : MOODU ANTA / PRINCE Jàppal nañu bëre bi lél bu bees. Ñaari mbër yee ngi waroon a laale keroog 23i féewiryee. Waaye,...

KOCC BARMA FAAL AK ÑAARI SÀMM YA

Nettali bii, jukkees na ko ci téere bii di Xew-xewi démb. Jukkib xët yuy fàttali ay xew-xew ci cosaanu Senegaal. OSAD a ko móol,...

NDAJEM NJIITI NGOMBLAANI RÉEW YI XARITOOK PALESTIN

Démb ci àjjuma ji, Njiitu Ngomblaan gi, Allaaji Maalig Njaay, moo nga woon fa réewum Tirki ngir teewe ndajem Njiiti Ngomblaani réew yi xaritook...

MBIRUM KOPPARI COVID-19 YI : JÀPP YAA NGIY WÉY

Mbasum koronaa maa ngi wéy di lëmbe réew mi. Naam, jàngoro ji wéy na, waaye jeneen jàngoroo ko fi wuutu, muy jàngoroy càcc ak...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/4/2025)

TERE NAÑU MANSUUR FAY MU GÉNN RÉEW MI Ay yooni yoon, Mansuur Fay mi ngi jël yoon wi, di bëgg a tukki. Waaye, bu demee...

MBIRUM KOPPARI “FONDS FORCE COVID-19”

Mbiru “Fonds Force Covid-19” mi lëmbe na lool réew mi fan yii. Bari na ñoo xam ne woolu nañu leen ci. Moom, Mamadu Ngom...

DOKTOOR JÀLLO JÓOB : GOR CI WAX, GOR CI JËF

Bees sukkandikoo ci waatub Hippocrate, dees na gis ni balaa ngay yeyoo turu fajkat dëgg, dinga làmboo juróom yii : cëral sab sëriñ, fonk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (15/4/2025)

LAAJ-TONTU (ELIMAANU JËWRIÑ YEEK DÉPITE YI) Démb ci altine ji, Elimaanu jëwriñ yi, Sëñ Usmaan Sonko, moo nga woon fa Ngomblaan ga ngir tontu laaji...

KOPPARI COVID-19 YI : JÀPPAGUM NAÑU ÑU BARI

Yoon tàmbali na saytu mbirum koppar yees jagleeloon mbasu Covid-19 ma. Ci altiney démb ji rekk, jot nañu jàpp lim bu takku ciy nit...

YÉGLEB WAY-BOKKI NDAJEM ÑAXTU NGIR DOOLEEL ASKANU PALESTIN

Démb, ci dibéer ji, lañu doon amal i ndajey ñaxtu, fii ci Senegaal, ngir naqarlu lay xew fa Palestin. Li ñu ko dugge woon...