Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

NGUUR GI DAJALE NA 405i MILIYAAR

Nguurug Senegaal dajale na 405i miliyaar ci 15i fan kese. Muy alal ju takku ju ko boroomi alal lebal ginnaaw woote bi mu amaloon...

CAABALUG ËTTUB CETTANTAL BI : YOON SUMB NA LIGGÉEY BI

Saabalukaay bii di Source A moo siiwal xibaar bi. Bees sukkandikoo ci li yéenekaay bi fësal, Yoon a ngi lëñbët caabalu gi Ëttub cettantal...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/4/2025)

WOOLU NAÑU SIMÕ FAY Yoon a ngi wéy di teg bët ci liy xew ci saabalukaay yi. Ba tax na, lu ci bari ñuy nemmeeku...

TÀGGE : MAMADU BAAJO KAMARA GÉNN NA ÀDDUNA

Xibaar bu tiis la réewum Senegaal yeewoo tay, rawatina ñiy liggéey ci wàllu Yoon. Mamadu Baajo Kamara moo wuyuji Boroomam. Mamadu Baajo Kamara nag, ñu...

SÉYDINAA MUHAMMADU MAXTAAR LAAY, XALIFA LAAYEEN YI, DËDDU NA.

Xalifa Laayeen yi, Séydinaa Muhammadu Maxtaar Laay, génn na àddina guddig talaata (8eelu awril 2025) jëm àllarba, ci Ndakaaru. Mi ngi amoon 73i at....

SÉMBUW « SPACEBUS 2025 » : YËR JAWWU JI NGIR SUUXAT YOKKUTE AK NAATAANGE SENEGAAL

Barkaatu-démb ca ngoon, yemook dibéer 6i fani awril 2025, Njiitu réew mi jiite woon na jotaayu kaajar ak ubbiteg lees dippee ci nasaraan « Caravane...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/4/2025)

TABB NAÑU AMSATU SOW SIDIBE Njiitu Réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, tànn na Soxna Amsatu Sow Sidibe ngir mu jiite ndiisoog réew mi...

WÀÑÑIG NJËGU KUURAŊ BI

Ci ayu-bés bii ñu génn la jëwriñ ji ñu dénk yaxantu gi xamle woon ne wàññi nañu njëgu ceeb yiy jóge réewi Vietnam, Inde...

LAAJ-TONTU AK SOXNA FAATU SIISE KAN (2/2)

LU DEFU WAXU, seen yéenekaay ci kàllamay Kocc, mi ngi am mbégte dalal fii tey, Soxna Faatu Siise Kan, jàngalekatu wolof ca Almaañ. Soxna...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI CI BÉSUB MOOM-SA-RÉEW BU SENEGAAL

Démb ci àjjuma ji, 4i fan ci weeru awril 2025, Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay doon na amal aw waxtaan ak...