AccueilTagsNjuga Gay

Njuga Gay

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

spot_img

IRÃ AK ISRAAYEL : LEBTOO, FEYTOO !

Xeex bi àddina sépp doon ragal ci diggante Irã ak Israayel tàmbali na. Ginnaaw...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/6/2025)

TABASKI 2025 : KÀDDUY NJIITU RÉEW MI Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay,...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI DÉMB YI (3/6/2025)

PAS YU BEES DIGGANTE SENEGAAL AK MURITANI Réewum Senegaal ak mom Muritani xaatim nañu ñaari...

PADES II : TÀMBALI NAÑU ÑAAREELU WÀLL WI

Nguur gi sóobu na ci ñaareelu wàllu naaluw PADES II. Mu fas cee yéene...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (27/05/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA GINE BISAAWO Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay...

TABASKI 2025 : CÀMM GEE NGI CI WAAJTAAY YI

Càmmug Senegaal a ngi ba tay ci waaytaayi tabaski 2025 bi. Ginnaaw déggoo bi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/05/2025)

ËTTU ÀTTEKAAY BU KAWE BI Ëttu àttekaay bu kawe bi tàmbali naa déglu jëwriñ yees...

GUDOMP : 92i KËR JOT NAÑUY JUMTUKAAYI TABAX

Fa gox bii di Gudomp, njaboot yi tàmbalee dellusi ginnaaw bi leen fa xareb...

PÉNCOOY PÓLITIG BI AK DAARA YI

Kuréli ma-xejj yi yékkati nañu kàdduy woote jëme ci péncoom pólitig bi ñuy amal...

TÉYANDI NAÑ ASURAA FAAL

Waa Cybersécurité jàppandi nañu, barki-démb ci altine ji, 12 me 2025, ndawu Pastef bi...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA KODDIWAAR

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, moo ngi, ñaari fan yii, fa...

JUBBANTI : DALUWAAYU NIMERIG BI ÑEEL PÉNCOOM PÓLITIG BI

Nguur gi taxawal na daluwaay nimerig bees dippee JUBBANTI ngir waajal péncoom réew mi...

Latest articles

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA