Tàggat-yaram

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (19/11/2023)

LÀMB : LAG DË GEER 2 DAAN NA SITTA Ñaari mbër yi waajal nañu seen...

LÀMB : TAFAA TIN DAAN NA ËMMA SEEN

Gannaaw ba Móodu Lóo ak Aama Balde bëree ci ayu-bés bii weesu, Móodu daan...

MÓODU LÓO DAAN NA AAMAA BALDE

Xaar bi yàggoon na lool, waaj gi tamit naka noonu. Waaye, ñaari mbër yi...

KUPPEG ÀDDINA GEES JAGLEEL U17 FA ENDONESI

Tànnees na fukk ak benni ndaw yi war a teewal Senegaal fa Endonesi ñeel...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

KUPPEG ÀDDINA U17 2023 Ndawi Senegaal yaa ngi ci waajtaayu kuppeg àddina si ñu dëgmal...

JOŊANTEB XARITOO : SENEGAAL DÓOR NA KAMERUN 1-0

Gayndey kuppe yi dóor nañ Kamerun 1-0. Tey ci altine ji lañ doon amal...

XIBAARI TAGGAT-YARAM (1/10/2023)

KUPPEG ÀDDINA WAY-LUU YI (MUUMA YI) Bàyyeesu leen xel, waaye way-luu (muuma) yi teewal Senegaal...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (18/9/2023)

WAA LORIENT YI SARGAL NAÑU BENJAMIN MENDY Benjamin Mendy duggaat na démb ci pàkkub futbal,...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...