Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 24 Sàttumbar 2022)

PÓLITIG  Ginnaaw mbetteel ga mu am ca Ngomblan ga ca palum njiit la, ndax Aminata Ture dafa nar a ber yoonu boppam ? Mu nekk...

SÉEX ALIYU NDAW : “LI MA JËLE CI MALAANUM LËNDËM…”

Ab téeree ngi nii boo xam ne, bii, boo koy jàng doo bëgg mu gaaw a jéex. Dafa mel ni, fàww nga def loolu wolof...

“ WÀDD MOO REY ARTISANAA BI, MAKI SÀLL A KO SUUL”

Senegaal dafa tollu ci jamono joo xam ne, képp ku jàngul, mënul a jot ci teraangay réew mi. Moone de, ñi jàngul ñoo ëpp...

Li gёn a fés ci xibaari bés bi Alxames 22 sàttumbar 2022

PÓLITIG  Mbirum Njaga Juuf Ёttub àtte bu Ndakaaru dёggal na daan yi ñu teg ci ndoddu meeru Ndakaaru bii di Baartelemi JAAS ci mbiru bóomug ndaw...

NDIISOOY NGOMBLAAN GI

Dogub 24eel bu càrtub Ngomblaan gi dafa tëral ne : « Ci ndoorteelu gépp moomeg Ngomblaan, ak ci bépp toogaanub siŋŋ, ginnaaw bi ñu falee...

KOOM-KOOM GI : YITTEY YITTE YI

Gaawu, 17 sàttumbar 2022 la Njiitu réew mi Maki Sàll tëral ag Nguur gu yees. Def na ci ay yeesal yu baree bari ginnaaw...

NGUUR GU YEES GI

Ndekete, njuuy, ci feemi Njiitu réew mi la bokk. Nde, ginnaaw Aamadu Maam Jóob mi mu taamu woon ñeel njiiteefu Ngomblaan gi, fental nan...

Sëñ Bàmba

Sëñ Bàmba Kéemaan la Dem ba ñëw war a sant ci ñibbisi gi Di sant Boroom bi ci dem gi Ndeke dem gee jur Màggal gi Bu demul...

MAKI, AMAL SUNU KERSA WAAY !

Ci ngoon gi, boori 16i waxtu, la RTS rotal xibaar bi : « bu 20i waxtu jotee, Njiitu réew mi, Maki Sàll, dina def...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Alxames 15 sàttumbar 2022

DIINE Màggalu Tuubaa Tey di alxames 15 sàttumbar 2022, yamoo ak 18 Safar ci weeru araab, bés bi ñuy màggal tukkib Seex Ahmadu Bàmba Mbàkke. Mu...