Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

NDIMBALU 670 MILIYOŊ CI MBEYUM DARKASE BI

Kurél gii di DER/FJ (Délégation à l’entreprenariat rapide des femmes et des jeunes) moo génnee lu tollu ci 670 miliyoŋ ci cfa. Mu fas...

CÀRTUB AMNISTII : AG NJÉGGAL WALLA AB RAWALE ?

Ca ndajem jёwriñ ma mu doon amal ci Àllarba jii weesu, Njiitu réew mi, Maki Sàll, biral na mébétu teggi daan yi tegu woon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 01 OKTOMBAR 2022)

PÓLITIG  Bitim-réew, ca Burkinaa Faaso, ñu nemmeekooti fa poqartim Nguur, ginnaaw juróom-ñatti weer kott ba fa Póol Ãari Damibaa jëlee Kaboore. Ka ko fa wuutu...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Àjjuma 30 sàttumbar 2022

PÓLITIG Ndogali Njiitu réew mi ci Karim Wàdd ak Xalifa Sàll Kii di Sã Sarl Biyagi, dib nekk jàngalekatu « Sciences politiques » ca daara ju kowe jii...

Waajtaayu gaynde yi : ñaari joŋate, benn bii

Ginnaaw ñaari joŋantey waajtaay yi mu doon amal diggante gaawu ak talaata (24i fan ak 27i fan ci weeru Sàttumbar 2022), ikibu Senegaal bi...

LI GЁN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Alxames 29 sàttumbar 2022

DIINE Génnug àdduna Sёriñ Abdu Rahmaan Mbàkke Sёriñ Abdu Rahmaan Mbàkke ibnu Sёriñ Abdu Xuddóos ibnu Maam Ceerno Ibra Faati moo génn àdduna ci bésub démb...

YOKKUTEG DUND GI “…dañuy ragal ne 2023 mooy gën a metti.”

Njiitu réew mi, Maki Sàll, woote woon na ndajem waxtaan ñeel dund gi. Altine, 26i fan ci sàttumbar la ndaje mi amoon ca màkkaanum...

GAALU JOOLAA, FÀTTE XAJU FI

Jéyya gënul réy suuxug gaalu Joola ga. Te, njaaxum du ko weesu. 20i at ci ren, ba tey, déggeesagul jéyya bu xaw a jege...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 26 Sàttumbar 2022

PÓLITIG Aminata Ture won na ginnaaw Njiitu réew mi Maki Sàll. Ciy waxam, dara waralu ko lu dul ni dafa àndul ci ñetteelu moome gi...

NJEEXITALI ÀTTEB BAARTELEMI JAAS BI

Ёttu àtte bu Ndakaaru dёggal na daan bi ñu teg ci ndoddu Bàrtlemi JAAS ci Àllarba jii nu weesu. Daan boobu nag li ko...

SENEGAAL 2 – BOLIWII 0

Ekibu nasiyonalu Senegaal bu futbal a ngi ci waajtaayu Kub di mond bi war ame ca Qataar. Joŋante bu mag boobu nag, daanaka ay...

YÀNQOOBA JATARA, JËWRIÑU TAGGAT-YARAM JU BEES JI

Mataar ba nekkatul jëwriñ jiñ dénk tàggat-yaram gi. Loolu bokk na ci xibaar yi gën a fés ci Nguur gu bees gi Njiitu réew...