Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

“ WÀDD MOO REY ARTISANAA BI, MAKI SÀLL A KO SUUL”

Senegaal dafa tollu ci jamono joo xam ne, képp ku jàngul, mënul a jot ci teraangay réew mi. Moone de, ñi jàngul ñoo ëpp...

SËÑ BÀMBA

Sëñ Bàmba Kéemaan la Dem ba ñëw war a sant ci ñibbisi gi Di sant Boroom bi ci dem gi Ndeke dem gee jur Màggal gi Bu demul...

LAAJ–TONTU AK SOXNA AWA GAY MU PAI

65i at ci ren, bi ñu taxawalee làngug Parti africain pour l’indépendance ak léegi. Loolu, nag, jar na waxtaane. Kon, ayca leen nu laaj...

Aa ! Gaa ñi, Tataa Mimi mer na !

Aminata Ture mer na nag. Te, altine ba léegi, moo ngi koy fésal ak a biral ci mbaali jokkoo yi ak ci waxtaan yi...

PEKKUG NGOMBLAAN GU BEES GI

Ci talaatay démb ji, li ko dale 11i waxtu ci yoor-yoor bi, lees doon àggali palug Pekkug Ngombalaan gu bees gi. Ndax, mujjewuñu woon...

Na woon, fa woon

Ci bëccëgu altiney ji, 12 ut 2022, la Senegaal doon taxawal 14eelu ngombalaanam (péncum ndawi réew mi). Nde, ginnaaw biñ leen falee, démb lañu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 12 ut 2022

TÀGGAT-YARAM Ikibu Casa Sport bi dugg na ci joŋantey Ligue des champions / CAF bi. Jot naa am ndam (1 bii ci 0) ci kow...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu 10 Sàttumbar 2022

PÓLITIG  Ngi waajal màggalu Tuuba, wa YEWWI-WALLU amal nañu seen ub siyaar ci kanamu kilifag murid yi. Mu mel ni mbég ak soññe ci ñoom,...

JOŊANTE CHAN 2022 ALSERI

Bokkadil yu CHAN 2022 bi jeex nañ ci njeexitalu ayu-bés bi weesu. Ren jii nag, 18i réew ñoo koy joŋanteji. Ñu ràññe ci Senegaal....

KUY DUND DI XASAW, BOO DEEWEE DU MAT A WAX

 Toftaleg IDH gu 2022 génn na ci alxames ji. PNUD a ko génne. PNUD (Programme des Nations Unies pour le Développement), nag, ag kurél...

NJUREEFI NDAJEM RÉEWI MSGBC

Ci ndaje mi ñu amaloon ci 1eel ak 2eelu fan ci weeru Sàttumbar fii ci Senegaal, réew yii di Móritani, Senegaal, Gàmbi, Gine Bisaawoo...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 5 ut 2022

PÓLITIG Maalig Gàkku fésal na yéeneem ak taxawaay bi mu namm a am ëllëg ci géewu pólitig bi. Moom njiital làng gi di Grand Parti...