Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

IMAAM ALIYUN NDAW, SA JAAN WÀCC NA !

Bakkan bu ñam dund, ñam dee. Ab xandeer bu damme cib waar moo wàcc. Tiis ak mbetteel la askanuw Senegaal yeewoo ci talaatay démb...

MAMADU BAAJO KAMARA, LOO NAR ?

Léegi, xam nañ kan mooy wuutu Paap Umar Saaxo mi dem alaaterete. Ci dekkareb 2022-1573 bu bésub 1 ci sàttumbaar 2022 la Njiitu réew...

JOŊANTEY BASKET FIBA 2023

Senegaal bëgg naa dalal ndajem Playoffs yu mujj yi Menn ndaje a des ci juróom yees war a amal ci Playoffs yu FIBA yi ñeel...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Àjjuma 2 sàttumbar 2022

XEW-XEWU JAMONO Jëwriñ ji ñu dénk wàllum ndox mi ak cet gi fii ci Senegaal, Sëriñ Mbay Caam, moo ngi woon ca diiwaanu Tuubaa ngir...

Li gёn a fés ci xibaari bés bi Alxames 1 Sàttumbar 2022

PÓLITIG Àppug wotey HCCT xamees na ko Ci ab saabal bu mu génne, Njiitu réew mi Maki Sàll mi ngi xamle ne wotey Haut Conseil des...

LEBTOO, FEYTOO

Sàcc, siif, daw… déedéet ! Loolu xewwi na. Léegi, li am mooy : sàcc, siif, rey, daw. Ndege, jamonoy tey jii, dañu lay siif, jël...

SEEX AHMADU BÀMBA MBÀKKE, BOROOM 18 SAFAR

Dara judduwul cig neen. Mu mel ni, bànneex ci coono lay soqikoo, mbég ci naqar lay bawoo, nattu mooy jur xéewal. Ki xam lii...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 29 ut 2022

PÓLITIG Fukki fan ak ñaar ci weeru Sàttumbar lañu war a taxawal tëralinu péncum ndawi réew mi tukke ci wotey palum dépite yii weesu. Ba...

WOTEY 2024 YI : WURE WA DEM NA KÉŊ

Lu tollu ci fukki weer ak juróom-ñett kepp a des ci wotey palum Njiitu réew mi, coow li ne kurr ci biir réew mi....

WOMEN FIRST TV Tele jigéen ñi, ngir jigéen ñi

WOMAN FIRST TV tele la bu ay jigéen sos jagleel  ko it jigéen ñi. Mi ngi juddu ci jamonoy mbasum covid-19 mi lëmbe woon...

NDAJEM RÉEWI MSGBC  ËLLËGU GAAS BI  CI BOPP WAXTAAN WI

Kurél gii di MSGBC te ëmb yile réew, Móritani, Senegaal, Gàmbi, Gine Bisaawoo, ak Gine Konaakiri, mooy amal am ndaje mu am solo ci...