Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

TAALIF CI MAAM ABDUL ASIIS SI DABBAAX (DAAWUDA NJAAY)

                     Taalif ci Maam Abdul Asiis Si Dabbaax Mag mat naa bàyyi cim réew Seex Abdul Asiis...

MÀGGALU TUUBAA (Musaa Aysatu Jóob)

Dees na amal màggalu Tuubaa ci 6i fan ci weeru oktoobar. Ginnaaw bi ndigal li  wàccee, Serin Muntaxaa Basiir Mbàkke ci kaddu Seriñ Bas...

TÀGGAT YARAM

Saajo Maane dugal na ñaari bal ci joŋante bi ekibam Liverpool doon amal démb ak Chelsea. Ci ñaareelu fanu joŋante yi la dugal balam...

MAKI SÀLL GANEJI NAY DËKK AK I GOXI RÉEW MI : SAFIYETU BÉEY

Kafrin, Fatig ak Kawlax am nañu gan fan yii weesu, gannaaw bi njiitu réew mi Maki Sàll doon wër dëkk yeek gox yi ngir...

POLITIG : SAFIYETU BÉEY

Aymeru Ñing, doon kilifa ci Bennoo Bokk Yaakaar te jiite kurél gi ca Péncum Ndawi Réew mi, moo xamle ni « bu ñu sukkandikoo...

NOOK MBËNN MII NAG, BA KAÑATI ? (SÉEX AXMADU BÀMBA NJAAY)

Séex Axmadu Bàmba Njaay “Ku ndóbin rey sa Maam, foo gisee lu ñuul sax daw.” Xanaa kon ndóbin gi nekk Senegaal di reye taxul wolof...

PÉEXTE (LÀMP FAAL KALA)

PÉEXTE Da maa dëfeenu di jeneer Ba xel mi tàbbi cig ndenéer Dellusi naan ma nu gàddaay Fii kat lépp a ngi naaxsaay Xel mi sonal ma Di yuuxu naan...

WEYI TAN (SAYDU BA)

Saydu BA waa Ñooro la, di al-pulaar bu gàlle. Ndaanaan luy yëngu ci teyaatar la, tëgg ak um pecc. Tukki na ci réewi nasaraan yu...

SUNU RÉEW MI (NDAY XAYBA FAAL)

  Soxna Nday Xayba FAAL mi ngi dëkk Ndakaaru, doon jàng xam-xamu melosuuf ca Daara ju mag ju Seex Anta Jόob. Bind na taalif yu bari...

FAIDHERBE, SAAY-SAAY BI NUY SARGAL

Bi Siidiya Ndàtte Yàlla génnee àddina ak léegi, am na xarnook xaaj. Waaye, mi ngi mel ni mësta gane àddina. Dara gënta ñaaw, nag,...