Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

KAN MOOY JIITEJI CESTI ? (NDEY KODDU FAAL)

Atum 2005 ak léegi daara ju mag jiy tàggat taskati xibaar yi ci Iniwersite bu Ndakaaru day tabb ñi yelloo jiite ko. Àllarba 26éelu...

ÀTTEKAT YUY WERANTE BAY WEERANTE (NDEY KODDU FAAL)

Fii ci Senegaal, ay kàngam ci yoon ñooy tamante dëmm. Àttekat bii di Yaaya Aamadu Ja moo jiiñ nawleem Usmaan Kan miy jiite tirbinaalu...

« Y’EN A MARRE » (NDEY KODDU FAAL)

Talaata jii ñu weesu (1 Sàttumbar 2020) kurél gii di « Y’en a marre » moo bëggoon a jébbal kilifay Orange yi ab bataaxal...

MUSAA JÓOB BAÑ NA NI MUUT, NEE NA MOTT (NDEY KODDU FAAL)

Musaa Jóob layookat bi doon jiite "Dakar Dem Dikk" la njiitu réew mi tekki ndombog-tànkam démb ci àllarba ji. Moom miy ndeyu mbill gi...

ÀTTEB CONGUG "CHARLIE HEBDO" CA PARI (AMI MBENG)

Yéenekaay bii di "Charlie Hebdo" ca Farãs génnewaat na, ci talaatay démb ji, ñaawtéef yi mu tegoon ci kow Yonent Yàlla Muhamad. Cig fàttali, looloo taxoon ay...

FEEBARU XOL BU GAAW DAANEEL NA IBK (AMI MBENG)

  Dalu webub bennoog Afrig bii di "Jeune Afrique" moo yëgle ne njiitu réewum Mali mees folli fan yii weesu dafa feebar ba ñu yóbbu ko...

DOGALUB GÓRNÓORU NDAKAARU ÑEEL DEM BEEK DIKK BI (AMI MBENG)

Górnóoru Ndakaaru jël nab dogal di ci teree daw bépp oto bu yab màrsandiis ba mu weesu 3,5i ton. Ngir leeral, Alasaan Sàll ne, oto yooyii,...

EKSAME BAKALORYAA BI DOOR NA TEY (AMI MBENG)

Niki bésub tey jii la eksame bakaloryaa bi door ci réew mépp. Jukkees na ci yéenekaay L’AS ne, 155109i wutaafon ñooy sëgg bind ngir am...

Iniwérsite Gastoŋ Berse

  Ndongo daara ya nekk ca Iniwérsite GastoŋBerse waroon a tàmbali ci talaata jii, dogal nañu gereew bu amul àpp. Loolu, nag, di fésal seen...

Futbalkati Afrig yi Orange ràññee (MUSAA AYSATU JÓOB)

Musaa Aysatu Jóob Démb ci altine ji Orange Footbaal Club fésal na ekibam ci atum 2019-2020, muy dajale doomi Afrig yi nu gën ràññee ci futbal, di po mu...

RÉEWUM KODIWAAR (MUSAA AYSATU JÓOB)

Musaa Aysatu Jóob Ci benn bataaxal bu mu siiwal, Jean-Pierre Kutwa, njiitu katoligi Kodiwaar yi, mi ngi joxe gis-gisam ci ñetteelu moome bi Alasaan Daramaan...