Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

AKON TÀMBALI NAA TABAX DËKKUB LËMM (MUSAA AYSATU JÓOB)

  Ginnaaw bi mu sottalee nas boobu mu duppe woon "Akon lightening Africa", kii di Aliyun Badara Caam di doomu-Senegaal bu nekk ca Amerig moo doon taxawal démb ci altine ji...

Mali : Soldaar yeek M5-RFP ñoo ngi wéy di waxtaan

Mali : Ba tey soldaar yi jiite CNSP (kurél gu yittewoo muccug askan wi) ak M5-RFP déggoowuñu ci kiy war a jiite réewum Mali,...

TAKK-DER YI SONAL NAÑU ARDO ÑING

Ardo Ñing mi bokk ci Aar Li Nu bokk ak Noo Lànk la takk-der yi jàpp ginnaaw bi waa kurél gi doon amal doxu...

Kafrin

Kafrin : Ndox mi bari na ca Ndukkumaan ginnaaw bi mu tawee taw bu metti ca dëkk ba. Gox yu baree mujj a taa,...

Màggalu Tuubaa

"Bu kenn dem, na ñépp toog, Màggal-leen seen kër". Lii mooy kàdduy jëwriñ bi jiite IRD ca Màrsey, doktoor Séex Soxna. Mi ngi indi...

LAN MOO XEW CA MALI ? (PAAP AALI JÀLLO)

Ci talaata, 18eel ut 2020, la ay soldaar yu fétteerlu nangu nguur gi ci Ibraayim Bubakar Keyta, teg ko loxo, moom ak yeneeni kilifa...

Laaj-tontu ak Kolonel-Masoor Ismayla Wage : « Li nu def Mali, mëneesu ko tudde cëtëŋ… »

France 24 amal nab laaj-tontu ak kii di Kolonel-Masoor Ismayla Wage mi yor kàddug way-fétteerlu yi booloo ci kurélug CNSP miyitte woo sàmm muccug...

YÉEN ÑIY SIIF JIGÉEN ÑI : NGEEN TEG KO FAN?

  Ndey Koddu Faal « Daf maa sàkku ci lu ma neexul… Egg na ci man… » Kàddu yu naqaree dégg yii te daw yaram ñu ngi tukkee ci...

PETIT GUIDE POUR DÉJOUER LES PIÉGES DE LA LANGUE WOLOF (Safiyetu Béey)

  Ce petit guide a pour but de faciliter l'apprentissage de l'écriture en wolof à tout débutant, en particulier aux jeunes. Il n'a aucunement la...

ËTTUB TAALIF (Daawuda Njaay ak Daam Jaane)

  I Sëriñ Daawuda Njaay Jaraaf jàngalekatub wolof la. Def na gëstu bu am solo ci tëraliin ak ci doxaliinu njàngalem kàllamay Kocc ci daaray tuut-tànk...